@2stvsenegal: En plein débat sur la vie chère, Ismaila Mbaye et compagnie poussent un énorme cri du cœur face à la dèche quotidienne des ménages. #2sdigital
Soyez positivé thé diéma comprendre fimouy waxer yi nek si commentaire yi nane souniou deuk Khiffou niou c’est parce que séne Wa keur guéne xam mais amna niou fa nek sonou th kéne xamoul donc arrêter d’être pessimiste yi cadre général laniouy waxer soff guéne trop xawma séne séne xell loumou léne di diarigne
2026-09-06 12:48:21
153
Ousmane Ndiaye :
message très important
2026-09-06 01:50:46
191
Une Ndiaye🥰❤️❤️ :
Keur yi togatouniou rere 🧐🥹
2026-09-06 11:57:25
99
Souleymane Jules( Tour Du 🌍 ) :
Kone sous région bi Sénégal sileu bokk ???
2026-09-06 03:01:52
38
user330769268477 :
louga de mo dakh Dakar fouf😂
2026-09-06 10:14:26
88
Chocolats blanc❤️♥️ :
Dakar mo gueuneu meti aux moins deuk yi gnigui togue rer
2026-09-06 14:28:07
22
fatoumbacke41 :
Fi thi tivaouane dé daniouye ndecki di agne di rérre vraiment❤️
2026-09-06 13:04:59
20
papa thierno :
Touba kaay mom kay len Ang rk barke morom touba
2026-09-06 09:44:16
26
jùb jùbal 🇸🇳🇸🇳 :
Louga mola wax da méti ??
2026-09-06 10:59:43
12
nabou.sylla1 :
Louga mome metti woul wakhal deug
2026-09-06 07:32:42
29
Babacar :
wa Louga dh linouy lek wa Dakar lekounouko
2026-09-06 17:52:37
7
AÏCHA M3lo 😍💕 :
Important😂😂😂😭😭😭😭
2026-09-06 02:30:05
36
rimmkkaa :
diaspora
2026-09-06 02:01:01
40
Vip gold :
Mais nak tu as bien dit les choses il faut économiser parce que la vie actuelle est très difficile Bly