@galsen.studio: Alal mën na jënd lepp, waaye mënul jënd mbegeel u dëgg... 💔 Banano def na njuumte bu mag, waaye ndax Serina dina ko baal? Déggluleen gëstu gi ci taw bi! 🌧️❤️ Abonne-toi pour ne pas rater la suite et dis-moi en commentaire : est-ce que tu aurais pardonné à Banano ? 👇 #FilmAnimation #HistoireMourante #Wolof3D #TikTokSenegal #Mbegeel #PixarStyle #AnimationWolof#SenegalAnimation #ShortFilm #Wolof #HistoireMoral #WolofViral #Galsen221 #ViralSenegal #viral #viralvideo #ReelsSenegal