Ioe dh meuneuh na wate loula Dale rek sa khol mola togne Wallahie nite geunou la tรฉ lima wax ni mane mi nekkkk ak ioe kham nako yalla nala yalla faye sa khol koula yene lou bone yalla na thi dรฎna mรฉtis lolou nakkkk mais douma la meuseuh setane love you ๐ค๐ซถ๐พ
2026-09-09 00:33:57
86
Domou Talla Dji ๐ฅฐ :
Soxnaa je pense que lii histoire ancien la๐
2026-09-09 03:25:32
12
KHADIJA!!!โค๏ธ๐ฆ :
Worna yalla koula xam deug doula yakk wala mouy wakh si ioe lou bone nitt guenoula khol bou rafett gua yor Koula waxx mom mo bakh motakh ngueni andeu rekk waxoula lou amm. Ioee mii yaa bakhh Ioee yaa bakh ba kholo keneu loum leu Meuneu apportel ou pas. Ioe yaa bax ba lepp loy deff kharo si retour.
Mane mom sa mbakh leer nama depuis niou khamantei louma nekk yagui si lol gnieup parceque Dangua beugg sa nitt meunn sa nitt ioe do torokh teh koula yakk dina ko guiss fonce on est derriรจre toi โค๏ธ๐ซด๐พDiam rek Guay am inchallah meunou gniou si ioe touss
focus rek boul tone qu'en tu es une personne extraordinaire
2026-09-09 00:48:21
3
bamba๐ง๐ท :
ay khale gaine way ay diambar gaine dfolaine fi lou gnaw magui laine di suivre dpui bigaine coumence way lp diam contune laine si lolou niou bayi ba euleuk ba gis fou yala di fayai wakh bayi dieuf soxnnaa saliou ak sokhna aicha rafahi
2026-09-09 01:25:49
3
Gnagna๐ฆโพ๏ธ๐ฆ(33) :
Vรฉritรฉ ๐ฅฐ
2026-09-09 00:03:27
3
Mouhamed Design :
yaw boul diakhle yalla mo andak yaw kou bakh nga avec beaucoup de qualitรฉ am khรดl Bou rafรฉt motakh diam rek ngay am koula ko yรฉnรฉ nga am ko koulako yรฉnรฉwoul nga am ko'' addouna moy dokhรฉ nonou rek yรฉnsay faw Mouy indi ay mbireum m deugeur rek diam rek ngay am
2026-09-09 01:16:34
2
[Moussaโ๐โน๏ธBarcaโฝ๏ธ]= :
Courage soxna adouna mon deme nnou
2026-09-09 01:59:55
1
Fatoumata :
Yow amal diam rek yow dagua bakh bilay [Cลur rouge]
2026-09-09 06:11:09
1
Rassoul_1441 :
Soxnaa lii beurri na d ๐
2026-09-09 00:08:25
1
To see more videos from user @soxnaaaaa16, please go to the Tikwm
homepage.