Salam kap kou diegué mame Ndiaye wax len ko nama contacter magui Gabon 🇬🇦 mayoumba keur serigne touba mom sou mounoul woté na diokh rakam wala kou mou geuneu wolou mou wax ko nama woo ma diokh ko ay tek taal you leer ay affaire you wara diougué Gabon nieuw fofou ben bi pour Rokhaya fall la benene bi pour Mame la Insbi bi dafa ame kouy khaptal mame pour mou bok si docier yi Sokhla wou ma Dara si mom dama koy diapalé rek fi si mayoumba wasalam