Man personnel koudoul diouli douma la diapé com dioulit point barre
2026-09-10 17:19:55
217
(Ismael) إسماعيل ديي :
Seydina Mouhamed kouko geune rafet xol teh pourtant Kene dakouko djouli yalla naniou yalla yeureum
2026-09-10 00:10:55
249
mcl6713 :
Yallah kassei moo xamm kou bakh🙏🏿nitt mongui seugu dii dioulii chaque jour tei fekk na moo geuneu yess nieupp🙏🏿 on ne doit pas seulement prier parce que c’est une obligation mais la prière doit être un acte de soumission et d’adoration envers notre seigneur🙏🏿l’islam est une religion de soumission et de bon comportement
2026-09-10 23:25:07
19
baye ousmane toure rafahi :
da melni ab patriotes nga de🥰🥰
2026-09-10 15:15:01
90
Diarraboussodiagne5 :
Je voudrais savoir Lane moy xole bou raféte
2026-09-09 20:01:33
53
Beug مام شيخ إبرا فال🫀🤍📿 :
Wayei nak amna ñiouy daniouy dioully wayei liniouy def dra baahou si nio geuna yess thi adouna dioully nk tahoul nit baah yalla lk mooy baahal nit thi thiobareem🙏🙏🥰
2026-09-11 12:10:48
1
Cheikh talibé sonko 🥰✌️ :
koudoull diouli yagui si erreur 🙏🏿🥰
2026-09-10 22:34:10
22
sopey seydina Mohamed SAWS :
koudoul dioulli dou dioullit wasalam
2026-09-10 10:53:57
38
Quran❤️ :
Sa cole bi dafa rafett foko amé
2026-09-09 19:01:52
90
pape gueye :
Borom khol bou rafet sakh nane lay mel
2026-09-10 23:02:51
4
DIA Business 👍 :
Yallah fayoule khool dieuf lay faye
2026-09-11 06:36:18
0
Vysh🇸🇳🥀🍃 :
nane yalla khol lay faye😂
2026-09-11 09:32:23
0
sarrbayern❤️🤍 :
fa wayloun lil mousalline
allazina houme han salatihime sahoune
2026-09-10 11:38:04
1
Y🌸 :
Ban hool la yala di fay lolu moy question bi? Ku am hool bu rafet forcément da ngua wra diouli 🥰
2026-09-09 18:46:17
64
Yaye Fall♡ du village ♡ :
Bly Tata démala beugu🙏🙏🙏
2026-09-09 18:21:30
45
sokhana m.... :
lou si metii daniouy ne ibadou ga lan may ibadou
2026-09-09 18:37:05
21
borom daradji :
salalahou ala mouhamad
2026-09-10 18:44:21
10
khadija bien-t khuwaylid ❤ :
wakh ngue lépp maan commentaire yii sma khol bii laay degeu 😭
2026-09-09 19:20:10
11
💍!!❤️ :
Salalahu Allah muhamad ❤️
2026-09-10 08:17:22
25
user210514661570 :
tu as parfaitement raison,
2026-09-10 10:04:37
8
To see more videos from user @une_servante22, please go to the Tikwm
homepage.