kou bakh aka nekha wakh Lou bakh s mountaha yalla nakofi yalla bayi ay ate you takou lol wakhe len amine 🤲🤲
2026-09-09 21:25:59
1
Khadim sopou Bichri HT :
Guir yalla nianal léne s mountakha mou yagg fi ❤️
2026-09-09 21:13:00
487
SA TOUBA 🇸🇳 :
Akaza yalla nalla yalla faye ta goudal sa fane yaw mi wax wax diou nex dji Dieureudieuféti akza ❤️Cheikh Mountakha gueun yagu gueun werrr Mbacke koulay khar yalla na khaddi Mbacke Balla 🥰❤️
2026-09-09 22:27:28
5
Daro Mbaye BÊTE BÊTE :
Wawaw serigne mountakha yalla Nafi yag té weur amine merci frère [Cœur rouge][Cœur rouge][Cœur rouge][Cœur rouge][Prière][Prière]
2026-09-09 21:52:59
143
o :
ki mo wakh lou bakh kou bakh
2026-09-09 20:52:32
342
nogaye Mountakha :
nieupa la beug mbacké yague fi rk
2026-09-09 23:35:22
68
Seck kharitou yayam 🍀❤️👌 :
Li moy wakh lou bakh kou bakh S Mountakha mo bakh dh walakhi ❤️❤️❤️seck waw gor yatal lou bakh amna solo ❤️