Sama djieukeur des man awo bi la falé woul mai 2em femme bi ah 3bi manqué wougne dará mai man rek la bagne douma défal dara bilahi yalla namayalla até ak mom🥺🥺
2026-09-18 09:53:33
38
Aïda :
Allahou Akbar wax baxoul yalananou borome bi may xolou mougne kou soone yalagua féké sa ndiarignou dome yi barké mouhamed psl
2026-09-14 14:38:48
266
lanoirceure2 :
Dione meissa hifaloma barki yonente bi te wodengama barki rassoulilahi
2026-09-13 09:50:46
54
ngoné dièye 3322 :
walahi lou lér machalla amna solo
2026-09-12 20:27:32
60
user :
ndeysane sama sérère bisi sine bou timé Lou nex khelam dem si man mou woma yalla na sa diam yague
2026-09-13 22:46:46
17
bine754 :
Salalahou allh Mouhamed
2026-09-16 20:18:18
28
user8582405233424 :
Sama dîner Sakh damasiy dessal sama Sokhna pour son petit déjeuner diabar là geuna yeurem dôme