Saway mougneul mane pharmacie la dém diko lathie ndakh amnga youpoula
2026-09-11 07:36:22
835
LA REINE SAGITTAIRE ♐️💕 :
que cette bonheur me localise 😭😭😭
2026-09-10 22:12:27
1413
mor.lam :
Hiii miss nako dama dane kholé ba beus sett kheuy liguèyi mai lo mougne mou diékh inchalah
2026-09-10 18:22:01
432
Evysh :
Ma raw marche jeudi sama guemign dou oubou
2026-09-10 19:44:50
184
sante yalla🇸🇳🇲🇷🇪🇸🇪🇸 :
😂😂😂😂😂 être papa n est pas facile
2026-09-10 17:17:37
680
Balance ♎️ :
Mane deh sama taw werou korr la dioudo niou Kheuy bene jour khalé bi di dioy rek sama Mame diokhma lem nena diokh ko nakh khamna birr bi moy meti ma war koko diokh ak youkhou khalé bi ma diakhaso ba nane lem bi sama borou kor gogou ba legui fayagouma ko😭😭
2026-09-11 09:22:33
56
COBRA :
mo takhe mane dématouma week-end mane sama bosse déthié bolé fire bou méti😂😂😂😂
2026-09-10 23:05:34
97
Fatou-adama Mbengue :
mane mi yoré ayy jumeaux nakk douma wakh té amo koula diapalé yalla bakhnaa
2026-09-10 22:58:25
86
torodobonheur :
yalla nga am ay jumeaux Wala triplé Amine 🤲 🤲🤲🤲
2026-09-10 19:09:48
323
Xolou aldiana ❤️💍 :
Goudi bi yeup damay tok ba fadiar sma dome dji dou nelaw goudi ba fadiar diakhlei na dh 🥺🥺😂😂😂