@sope.serignesammbaye: 📌 Cheikh Bara 🤣🤣 😂 « Président réewmi lay diamou… maire lay diamou itam ? » 🤣😂😂 🔥 Cheikh Bara dellusi ak ay kàddu yu metti te yu tax nit ñi bari di ree ak di waxtaan. 👀 Li mu wax dafa yëngu réseaux sociaux yi, te commentaires yi sax dafa neex torop ! 😅 🎙️ Déggal extrait bi ba mu jeex ngir xam contexte bi ak li tax waxtaan wi di tàng. 👉 Yow nak, lan moo gëna la ree ci kàddu yi ? 😂👇 #CheikhBara #HumourSenegalais #TikTokSenegal #Kebetu #BuzzSenegal