cheri mane mi boul khame nima melone barki s saliou taye dama santé yalla damani amna Lou yalla def thimane louma khamoul té damaye guénte di guise s saliou moumaye gnanal ak s mountakha té serigne fallou moma yobou thi serigne saliou mounéma yaw ki moye sa serigne Kone Sante yalla rek
2026-09-11 21:27:16
317
kharitou yayam :
salalahou allah moukhamed ♥️
2026-09-11 17:50:01
98
Sokhna maï mourtada 🌸Saliou🫀 :
Salahou Allah Mouhamed
2026-09-11 17:23:47
86
kalsoume❤️🦋 :
sallalahou halla mouhamed 🙏🙏
2026-09-11 18:23:39
44
🤎🦋سُخْنَة :
SubhanAllah3x
Alhamdoulilah 3x
Lailaha illalah3x
Allahou akbar 3x
Astahfiroullah 3x récompense pour toi et moi🤍🖤🫶🏾
2026-09-11 17:52:57
350
sokhna bambista :
machala yala na sakh
2026-09-11 21:02:48
201
la sénégalaise :
Sallalawou Ala Mouhamed
2026-09-11 19:19:35
22
Bb zale JR🥰⚽ :
ndeysane Santa yalla bou bakh❤️❤️❤️❤️❤️❤️
2026-09-11 17:53:21
10
KINE DIALLO :
qu'Allah nous facilite la prière 🙏
2026-09-11 22:04:17
92
user5324339611421 :
salahou alla Mohamed
2026-09-11 18:59:20
14
La béni d’Alla Mou S Babacar❤️ :
Walahiiii ndaysane mooy Borom yeurmendee ❤️❤️❤️
2026-09-11 17:16:13
97
Khadija, Fall :
2026-09-11 14:50:14
20
fatousall467 :
Yalla na sah
2026-09-11 11:10:41
16
magne :
allah amdoulilah
2026-09-11 14:04:31
7
une yaye fall🤍🖤👌 :
wallahi yalla kaye adji bakh dji do kham sakh loko meuna fayé ndeysane [Yeux larmoyants]mane deh sante nako wallahi nimouma changer nii
2026-09-11 19:58:36
18
Kaf foo ree💃😂🥰🥳 :
Bly 😭Mem man dmy Sant Yalla Legui dmy djiouli ben waxtou douma raw Mem Fadiar sax dmy yewou djiouli 🥰
2026-09-12 19:16:41
8
Mariamakande :
yalla na yalla sopi nan tamite diouli moy sama problème bilahi 🥺🥺🥺
2026-09-12 17:06:14
47
PrunelleStore@byNabiche :
alkhamdoulilah allah kouli khal [Prière][Prière]yalla bour bou bakh la