bilay koumou daloul meunoko kham mane mi febarone teude ba goudi tog diakarlo ak yalla niko yalla rèye ma yalla bouma dioug😂😂😂telmnt k dama sonone oufff mon dieu😂😂
2026-09-11 14:22:37
10
Maïsha🥰♥️09 septembre 🎂 :
ki dh Moe mane sm fébare sounou wa keur dagnouye diomi ndaxe limae wax manane malaka dafa ragal xalé na xalé nieuw tok sm wéte AK damae dh yaye boul ma bayi😂😂😂 no fébare baxoul ga tané gnou tek saye vidéo
2026-09-11 14:11:18
7
Saliou Ngom :
sama yaye ni lay def 😂😂😂
2026-09-11 16:28:37
0
M :
Koumou daaaloul manno ko kham 😳 yallah na niou si yallah mousseul 😁
2026-09-11 16:54:17
0
snap keur sega..🔥✨❌ :
Diaroul guamakoy partager febar d’à metti
2026-09-11 15:22:23
0
Kholou Sergine Mbaye ❤️✌️🥰 :
Bilaye giripp manna Lou né😂😂
2026-09-11 16:24:45
0
loufa talibe sonkho :
yagui délo sa xélle si yalla dé[Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie]
2026-09-11 17:23:17
1
To see more videos from user @ndeye.woly45, please go to the Tikwm
homepage.