amoul preuve diko teuth 20ans de prison le Sénégal va mal 😭😭😭
2026-09-23 00:43:08
110
papisba568 :
Yalla na dème Canada
2026-09-24 01:36:55
7
talibe bamba :
20 ans de prison kénn rk moko yelo moy Sénégalais yi nek thi mairie yi di diay extrait diambour yi
2026-09-14 21:41:32
130
ÑJAGA MBY✪ :
20ans sans preuve Allah Akbar 😭 ana ñi sàcc alalu réew mi
2026-09-23 23:38:43
33
꧁༒𝐬𝐚𝐠𝐢𝐭𝐭𝐚𝐢𝐫𝐞♐️🧠༒꧂ :
Bilahi walahi done goor senegal mome daff metti ay risque kasse la
2026-09-24 09:16:03
13
Degue diame :
procureue so feke touma kesse la yangui gadou akh 20ans san preuve
2026-09-12 12:13:36
96
Malick insa Diagne :
solution bi moy caméra de surveillance si negu xalé yi pour eleuk
2026-09-23 22:30:16
11
elhadjik74 :
bamel bou daw moy prison
2026-09-13 00:02:17
17
sonko a vie💔😎🇸🇳💸 :
dou deug
2026-09-12 12:48:46
20
samba soro :
def na wallah défoul djigne gua wax de , mai souko défe 20 an da touti wayai bou viol amoul guir yallah nagne ko bayi
2026-09-12 12:57:42
24
khoumametseri :
خيركم من تعلم القران و علمه 😭🙏
2026-09-24 07:01:18
7
éleveur pigeons 777 :
حفظ الله جميع مقرئ القرآن وسدد خطاهم وأعاذهم من مكر كل ماكر
2026-09-12 17:04:17
26
baye karim :
liguéye bi amna solo
2026-09-12 10:10:56
16
Kabir diagne touhfatou ht Rufi :
Senegal dou réw way dou demander test 😭
2026-09-24 08:32:41
1
deugg :
yalnagnou yalka samal sougnou diabott
2026-09-12 12:34:00
5
cheikhseck5155 :
vint temp sens preuve
2026-09-12 09:59:06
11
🙏🙏 :
Kokou dé adunam yakhou na🥺🤔
2026-09-12 12:44:43
5
cheikh fall domou TAWA FALL :
yalla na Yalla samou serigne daara yi niofi nekal yalla
أهل القرآن أهل الله وخاصته
2026-09-12 23:18:23
8
mamour Niang :
أشتغفر الله
2026-09-12 12:52:03
6
Abobacar Tall 🥳 :
5ans au moins
2026-09-12 22:52:08
1
El Hadji Fallou ndiaye🇱🇧🇸🇳 :
Bilaye serigne darra yi dagno sonnou 😳😳
2026-09-24 13:43:38
1
Samsoul houda tv :
liguéye bi amna solo
2026-09-12 23:10:49
2
Matar Fall :
Procreur lanmoy preuve bi
2026-09-24 10:48:49
1
10 aout inchalla ❤🙏 :
justice sengalaise mom bala mo gueuna mena tek punition rek mou nek serigne dara vraiment amolen beneu yemeande viol consentement kou am plus de 15ans loumou def moko tay yar len sen dom yi yalla naniou yalla doli sutura sengal lep risque le
2026-09-24 02:14:23
4
To see more videos from user @bigpa_technicienav, please go to the Tikwm
homepage.