yalla nalla yalla sam arr la mousseul foire bi yalla guasi ame ndam you kawe sa djorte si barke yonetebi amineee
2026-09-13 12:15:51
37
Xolou walo walo bii❤️💍🔐 :
Yalla nala yalla défal diamou ak soutoura si barké Moukhamet
2026-09-13 12:13:50
117
j'aime ma mère :
wawawa machallah lalake
2026-09-13 12:18:15
13
Miss-Sourire🥺♥️ :
Sayy New balance lanla tmt ohh🫶🏾❤️
2026-09-13 12:30:42
0
linguere :
yalla nalathi yalla may Lou kawé sa ndiorte Thi barke seydina Mohamed aleyhi salatou wa salam amine yararabi exposants yeup yalla nagnou sold out Thi barke seydina Mohamed aleyhi salatou wa salam amine 🙏