Dahirabi amna nioy khedma am nioy kourel am nioy lathe adya amna nioyor sonorisation
2026-09-14 11:58:30
21
BEUG BAMBA :
amna solo [Innocent][Innocent]
2026-09-14 15:34:22
0
dousey :
kamil daccord mais apar khana dahira bi dou ay Commission
2026-09-14 01:29:04
9
new.utilisateur0 :
Khourek dafa way ak répété. Souniouye répéter yenangui si lenene. Souniouye guestou air yi ak di stresser yennangui lelene. Kourel dafa beurri stress
2026-09-14 13:48:30
2
user2707345146824 :
Désolé vraiment on dirait que tu comprends pas comment fonctionnent les Daarah "gayi ay diabar deugg lagnou liguey mo tah gnouy dadialé ay adiya di diokhé sache dieundeu ay sonorisation ak ay base ak matériel yeppou.
Daarah aussi daffa yatou motah dafay all ay commission
Organisation,culturelle,conservatoire administration et autres
khassida yi aussi manoul neck derrière moments lolou moom ndioumté leu
Daarah yi khassida yi moy khol bi boussi diougué dara doufa dess
2026-09-14 17:48:41
1
S. Barra Lo Rafahi❤️❤️ :
lan mo thakh nu déf ay commotion si dara dji
2026-09-14 11:24:42
4
masse ndiaye md32 :
xam xam bi dsna mal communique
2026-09-14 17:47:35
1
massamba :
serigne bi linga wakh ame na solo dh wayé thiona andoul ak kourel boudé d'ara dji yatou na keuy kou nék meune nga diap thi léne thi sama khalat bou gat wala [Prière][Prière][Prière]