Ndiaye talla Bacar Codou Walahi azim sma mbeuguel si yw khawma sah foumou tambalé th walahi amoul fin Limay yeuk si smay parent Apar niom si yw rek lakoy yeuk walahi beuss bouma doundé ba guis la souma déwé dina tali dh Walahi ndayalé la sma bo ndah sma mbeuguel si yw meunumako sah wah soumalay khol sma yaram day daw car sma phone bakhul dh mais dina def le tout pour mou tak ma meune la suivre yw kassé yamako diaral si aduna blh Toujours ma nelaw di sma phone ndah yw Walahi beug nala guis llu dakal nama leb si aduna walahi azim Mum d’amour beug nla dh😩😩😩😩😩🤦♀️🤦♀️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🩸🩸🩸🙏