@aliya_kane: #tiktoksenegal🇸🇳 #videovirale #tiktokviral #cejour #mamendiayesavon😂😂😂🤣🤣🤣🤣

Aliya Plume blanche 🪶 🤍
Aliya Plume blanche 🪶 🤍
Open In TikTok:
Region: FR
Monday 14 September 2026 17:03:21 GMT
102329
6295
250
246

Music

Download

Comments

binta0609
𖣘 :
Procureur si boppam mo beug guiss len ma
2026-09-14 17:48:26
174
fayelaa0
fayelaa0 :
Sénégal rek mo am procureur youy woute buzz
2026-09-14 18:44:32
27
thiatourama
Thiatou-Rama 🇸🇳🇧🇪 :
Adji mass 20millions lay demander 😂😂😂😂😂
2026-09-14 18:03:02
55
yassaguinar6
La Bandar❤️ :
Vraiment melni gniou deff crime nagn libéré gni prison limou fess rek doyna
2026-09-14 17:27:01
419
besso2070
Aby Linguère :
Maître à raison des injures alors qu elles ce sont déjà pardonner li dafa eup
2026-09-14 17:22:02
480
lunikdesamum246
l'unik de sa Mum😘❤️👆☝️☝️☝️ :
C’est pas du tout normal dagno wara yamm atei wa illah gnou bayi nieup
2026-09-14 17:21:35
161
footstyle65
Fatoush :
Mètre dafa perte procès bi rek mes mom si bopam plainte na Kaliphone ndax dafco saga vrement bayilen nefekh legi yayou diambour ak vidéo ramz mem boudé dou moko dougeul tal na live vam partager co wakh nit yi demlen télégramme setaneco nos vraiment bayilen hypocrisie bi camem
2026-09-14 17:44:58
2
dadasow64
Dada :
Man dé comme kou bok ak niom je ne peux pas manger j’ai mal au ventre ndakh stressé
2026-09-14 17:32:41
107
nyangmbalo00
𝕹𝖞𝖆𝖓𝖌𝖒𝖇𝖆𝖑𝖔𝕹𝖔𝖎𝖗🖤 :
Boudé saga rek 1ans sama yaye deh dotoul dess fiii😂😂😂
2026-09-14 18:43:47
13
lapaix2211
nickname :
Avocat international bi le meilleur Avocat du Senegal 🇸🇳
2026-09-14 17:32:39
44
larosebousindian
[email protected] :
vraiment comme si c'est des criminels
2026-09-14 17:24:28
152
mounas.diedhiou.c
Mounas Diedhiou Chiedozie :
Di emprisonné ay blogeure alors k niou dieul si ay milliards am liberté Sénégal mougui deugeure amoul khalise
2026-09-14 17:51:32
23
droguedouce09
Bijousaliou244♥️ :
Vraiment comme si elle sont des criminels saga rek senegal dou reww
2026-09-14 17:30:33
62
momo.5658
momo.5 :
Ana gni lek sounou milliard ils sont libre
2026-09-14 19:39:35
5
justmoi2001
Juste moi :
Détournement de fond des milliards gnou bayi lennn
2026-09-14 17:44:15
63
tranmm05
La tigress :
Vraiment
2026-09-14 17:27:15
31
les.dlices.de.grigol
les.dlices.de.grigol :
Tay dma done dioye 😭tribunal dma khol mo diekh surtout adji 😏tay dma diomy
2026-09-14 21:35:48
1
binta0609
𖣘 :
Li dafa diaroul sakh mandat dépôt
2026-09-14 17:48:39
57
dadiss430
Dadiss :
Procureur da rew fokné adouna filaye yam Mais défouniou dara saga rek 1ans C trop
2026-09-14 18:24:33
12
fierdemoi2025.2023
@Yaraham19 :
voilà un vrai juge
2026-09-14 17:30:24
51
marie_no_stress
🍀 𝕄𝕚𝕤𝕤✨N𝕠🥵Stre𝕤𝕤$📌🍀 :
Pro esk beugoul won dieul rox mou bagn mtx mouni 1 ans pour mom 😂😂😂😂
2026-09-14 18:15:09
7
coumbis525
Awa ❤️ bou Serigne babacar Sy :
Wa legui gnome balanter nagnou.procureur bal len tamit.yalla sounou borome Mignot dakeu sah dafay baler tamit
2026-09-14 17:35:37
21
taureau010
Taureau 🐂♉️🇫🇷 :
Li dé Sénégal rek la am
2026-09-14 17:40:51
11
achaciss081
🦋💕It’s Aïcha🦋💕💕 :
vraiment naniou bok atté
2026-09-14 17:32:17
20
To see more videos from user @aliya_kane, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About