@ndiassendiayenabien:

ndiassé ndiaye nabien
ndiassé ndiaye nabien
Open In TikTok:
Region: SN
Wednesday 16 September 2026 16:59:47 GMT
41978
7294
240
93

Music

Download

Comments

lampfalltraiteur
Fallou séne :
mom dafa beug cheikhe mbaye ndaysan
2026-09-16 18:39:59
44
karavision221
Kara Vision 📸 :
Kii yor téléphone bii moye kan mome tek nakou sii temps bou doy waar 😎🥰
2026-09-16 18:55:10
56
salikhate571
wakana hakhane moy khól bi ❤️ :
Esk dolene kou Def son nékh na way
2026-09-16 19:05:15
0
khalifa.ababacar7858
Khalifa ababacar 🇸🇳🇺🇸 :
Waxtanou wa keur seydina mouhamed bilay yéna bakh
2026-09-16 22:10:18
28
sope.nabi.couture3
Sope Nabi Couture :
liii dh mo bueri lollllll🥰
2026-09-16 21:46:44
0
diakhatenormal27
Serigne beugue lo bakh :
ya bakh way
2026-09-17 00:09:38
0
bayezaletinexa0
Sergine saliou tine :
Kiye caméra dina 😭
2026-09-16 20:13:32
14
dioufmomo95
Mømo Diouf 🥰✨ :
Li moy wax lou bakh nk🥰🥰😭
2026-09-16 20:35:24
0
wakeursmassambambaye
s khadim seck allxourane🥰♥️ :
ko yor téléphone bi kanla😍
2026-09-16 17:37:45
15
_daame.rassoul
DAAME RASSŬL :
yonente bi mako geuna beugue ñépp 💚💚💚💚🥰
2026-09-16 19:30:39
9
amina.bada3
amina saliou :
niarie ndandane you man la rk 🥰
2026-09-16 17:59:07
0
pacodiez92
pacodiez :
ndiassé tamit meune na
2026-09-17 00:59:36
6
dykha.yaye.fall
Dykha ❤️👌yaye 🫂💍Fall :
Li nèkh trop🖤🤍👌
2026-09-16 17:30:10
22
gayeplombier6
❤️𝙂𝙖𝙮𝙚 𝙋𝙡𝙤𝙢𝙗𝙞𝙚𝙧🛠️ :
Awou kate bi Allahou 😭❤️
2026-09-16 19:52:10
11
amadydiouce7
Amady Diouce :
thiéy Serigne Touba amoul morom dé bilahi motakh niou kham té beugue yonéneté bi psl diotayou mouride mo nékh Machallah
2026-09-16 18:20:31
5
bamba_pro.sn
Ahmadu Bamba :
Sen sonn bii laa amatoul weur na ko YouTube ba Basonou
2026-09-17 01:45:14
1
user4035559218571
Sokhna Ndeye M Ndiaye wakana :
Aka gnon meun ❤️❤️❤️
2026-09-17 00:54:20
6
ibrayemandiayekhasida
ibrayema Ndiaye Khasida :
e way Ndeyesane dh gal li rék
2026-09-16 19:27:50
5
75.634.12.08
Khadi.Babacar.Gaye.756341208 :
2026-09-16 20:02:07
3
mouhammadoumbow
❤️Mbow❤️Bou❤️Cheikh❤️ :
Ki yor tlphn bi say say deug la
2026-09-17 01:32:21
2
bayeguinar1234
Bara mbaye :
ndiassé dougalal vodeo yi bayi dag dagué bi bou niou ray way
2026-09-17 02:23:38
1
medmouride
Moussa ikfini💚 :
2026-09-17 02:50:26
1
pedri.gonzalez760
pedri gonzalez ♥️ :
guisse nga yén ngi man kén d'où ma fi raye kharal ma khôl niou ma def ♥️
2026-09-16 19:38:50
3
To see more videos from user @ndiassendiayenabien, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About