@unebabel5:

L’Business😎
L’Business😎
Open In TikTok:
Region: SN
Thursday 17 September 2026 20:52:13 GMT
279505
24042
213
1913

Music

Download

Comments

binetaniang230
Binta rassoul❤️ :
Meuna togue semaine douma ko beugeu té néna mame rek la beugeu
2026-09-17 23:23:22
473
yasmina_ka_80
Yasmina334 :
Man deh dan na tok ay semaines doumako deg ma dane obliger diko wo mala message ko wala ma fek ko fi mouy ligueyei bouma wakhei mouni dafa occuper wayei tay lepp diekh bayinako bayi bou civiliser mou tourner dima top insbi mako bayi si lay doga am sama diote mee mercii rek
2026-09-17 23:43:38
80
diorniang350
Alalou serigne bi☕️👍🏿 :
Mane dh Day liguey di wax ak mane soumako waxé do coupé bly day bagne a chaque fois ma wara deme ecole momay yé di wax ak mane meunoul tokk ta douma wo souniou khoulo wé sax daniouy wax telephone ta danio khoulo
2026-09-18 12:55:16
32
bonitacharmante2
Bõnitå=😻lv=👄=äūrå💋🎀 :
Par mois nak 😳😂
2026-09-17 23:53:25
116
mamoush92
Princesse💗Soninké :
Graçon princess yi gniofi eup mla moudié message 😂sougniou yewo dougniou woté dougniou message pretextant gniola moudié mess😂lima beugu wakh yeup
2026-09-18 09:46:25
147
awa50601
Awa Sy 🇸🇳 :
Verite ça c l’amour vrai ❤️
2026-09-18 11:31:35
103
fatoufall563
Fatou Fall437 :
Li dh moy deuggg pire sakhh
2026-09-18 10:55:05
21
bb.yacine.la.fille
Bb yacine la fille noir 123 :
Comme sama bose🥰
2026-09-17 22:40:34
37
bbytoufa
Fah❤️🥥 :
Bilahi gni kouleine top sa xel lagnouy yak ba do nek en couple 😭😭😂😂😂
2026-09-18 13:23:51
13
alalou.firdawsi4
Alalou firdawsi ❤️ :
Vérité absolue
2026-09-17 21:35:40
65
rouguihijabhenne
rouguihijabhenne :
Mane deh ay mois lay tok woma nane Yao rk la beug
2026-09-18 14:41:08
6
u_n_e_0
Une♉️ 💕 :
Tout est une question de priorité personne n’est occupé 24h/24☺️prenez le temps de bien choisir vos amants les filles 🥰
2026-09-18 16:28:36
5
bea.ada.la.maquill
bea Ada la maquilleuse 😘💌 :
bb je suis la pour toi
2026-09-18 21:43:53
5
galbnn
maman :
ça sais vrai mn homme 🥹 Bilakhi
2026-09-18 12:09:54
9
ramatoulaye7623
Ramachou bou sidy diop❤️ :
Kon Alkhamdoulila 🥰🥰🥰
2026-09-18 18:56:00
6
lasonkiste1
Thiatu❤️sonko🇸🇳couple/chic :
Deugal llou rk 🥺😳😭
2026-09-17 22:37:28
11
user47493392420802
Amy m s fallou ♥️ :
bilaye 🙏
2026-09-17 22:57:21
9
astou.diongue.9
astouseye :
merci
2026-09-17 21:46:54
11
serer.bi7
Sererè bi🫠💘💦 :
vérité absolue
2026-09-17 22:09:13
6
bibicheofficiel2
bibiche :
bilaye yaw
2026-09-17 22:38:50
6
princessethiam360
Princesse thiam :
Vérité Lou lere Ga wax Meun na sax banian degue yayam dila wooo
2026-09-17 23:00:08
6
kya.adara0
kya aïdara :
bilaye dueg la dh [Cœur rouge][Cœur rouge][Cœur rouge][Cœur rouge][Cœur rouge][Cœur rouge]
2026-09-17 23:39:31
5
domousonko2029rk
Ma mère ma vie❤️🖇️ :
konnnn dh kennn bougouma
2026-09-20 20:18:23
1
fatou.geuye37
Fatou Geuye :
wawaw sama Boss nounou la Mel mane rek lay top❤️❤️❤️❤️❤️
2026-09-19 19:29:21
2
fifina911
Une Fifina 🤍✨🎀 :
3ans de relation plus de 9h d’appel par jour mm au boulot jusqu’à la descente khalatoul tok 1h wotéwoul sama ndiol mi waayy 🥳🥳🥳
2026-09-19 00:21:54
4
To see more videos from user @unebabel5, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About