Ande bi mo djitou souniou dioudou té doussi nioune lay yako : Jamono moy Jubbo 💙🤍🩸
2026-09-18 01:02:27
62
Isco Ramos :
merci wa jamono
dou thioubou jamono 🔵⚪moy juboo 🔵⚪yalla nguene dieul zonal bi, départemental bi ak régional bi on est fier de vous 🤲💙
2026-09-17 22:39:27
70
PRINCEUH KIM✪ :
Diot na niou andeu mobiliser diapalei Diamono mou dieuli coupe bi💙🤍😭🎉
2026-09-17 23:55:11
10
Ⓜ️ilka🥇 💸 :
@Ⓜ️ilka🥇 💸: Jaxaay ( ancien nom : les aigles 🦅), jamono 2 ( Hongrie) , bokk jomm ( je pense ke Brésil lagnou toudone) dagno bollo wone toudou la grande Asc juboo après lagnou guénate toudou sen tour you moudiou yi mais après lolou dra gnaawoul si diguanté bi entre juboo ak Jamono motakh gnouy démalanté . Même Bokk jomm ak Juboo jamm rek mothi am rak day deuk Juboo mak deuk bokk jomm. Nonou la démé gneup JUBOO LAGNOU BOKONE 💙🤍🤝
2026-09-17 23:54:12
9
Ababacar Ndiongue :
Sama yaram dafa daw bilay meitina gnou trop mais Jamono est là