bilahi adouna mo doye ware neke député soye wakh Yenne député gueune salle bi taiye soye wakh kene d'où guene yalla rek mofi neke Macha Allâh Ousmane yalla nako borom bi Sam
2026-09-18 12:51:30
57
omar thiane🇸🇳🇮🇷 :
Sonko yalla nako yalla takhawou❤️🙏❤️
2026-09-18 15:44:03
39
Alpha blondy :
Sonko le vrai patriote
2026-09-18 10:54:02
44
mominatoucisse :
Ndaysane aka yaga sonou si rewmi Yalnala yallah gueuna teral