@mrsfayekitchen: #cuisinesenegalaise🇸🇳🇸🇳 #mrsfayekitchen#tiktoksenegal🇸🇳

Mrs Faye kitchen👩🏼‍🍳🇸🇳
Mrs Faye kitchen👩🏼‍🍳🇸🇳
Open In TikTok:
Region: SN
Friday 18 September 2026 11:24:44 GMT
1111419
136867
1177
9120

Music

Download

Comments

awa.eva07
Awa eva :
Se genre de femme que mon mari mérite mais malheureusement yalla mane lako bolél 😏😂
2026-09-18 13:56:54
3932
nanoucha842
Marinette 💖🇸🇳 :
nasa dieukeur dioxè rek
2026-09-18 13:06:04
2693
fany.moukhtar.fall
Fany.Moukhtar.Fall :
Kagn lay am dieukeur mumay tadial ay peti dej agne yu normal ohh ku am frère bu meune seyy normal😍😎
2026-09-18 15:29:04
277
taawbi221
Taaw :
togg niatt (3) la : - yéné togg lou nekh diokh nitt gni - dépense bou doy - saf lokho
2026-09-18 15:21:58
1164
ndeyacheikh2
ndeyaCheikh2🫶🏼Babel Senteur✨ :
Ok les filles nagn diangui thi Mrs faye 🥺
2026-09-18 12:28:49
1351
haven_style0
HAVEN_STYLE🎀 :
Wa legui exemple soudé dagay ligueyi nak ? 😭
2026-09-18 16:19:46
10
azizniang12
ZIZA GUNNERS 💯🫶😎 :
dafa am niou meun togou am niou saff lokho.
2026-09-18 17:29:25
78
blackqueen0020
M@Gu!🥰💜💜 :
Togu lou nekh diokh nitt yi niou lek ba sour mom mane nako 🥰 mais rakhasssss dafmay dioylo😂
2026-09-18 11:30:08
462
alioune77772
Ali :
kokou sama Fatou samb lah
2026-09-19 08:42:17
1
bleinkeur
nguirane :
goula guene saf loxo mola guene saf kaw lal
2026-09-20 12:19:14
6
user982968310867
eleonore thiaw :
Tata do def ay cours de renforcement 😂??
2026-09-18 13:30:50
122
user4619594475147
Khadija🫶 :
Sa dieukeur dal na ci
2026-09-18 11:30:15
63
serignesalioudien5
Serigne Saliou Dieng_SN :
Souppou kandia bobou dh diaral nama signer monogamie avec communauté de biens adduna yaggoul té dara douniou toppou bir bammel😌
2026-09-22 08:22:35
34
_missfall0
𝓢𝓸𝓼𝓼𝓸 𝓕 🌸🐚 :
Tata doma defal stage
2026-09-18 11:35:30
59
chichi_astuces
Chichi_Astuces :
Kharal ma dfe ni yow j’ai pas envie de monter une vidéos aujourd’hui 🥺
2026-09-18 13:53:23
25
borom.porokhane34
Oumoul Khadim 😍❤️ :
Mrs faye nous on t’aime ❤️🥰
2026-09-19 01:19:23
12
fchicken5
L@ s@G€❤️🇸🇳 :
Togou bou am vaisselle you rafet thi leu 🥰🥰dagay gueuneu am envies lekkkk♥️♥️
2026-09-18 13:50:15
47
azizniang12
ZIZA GUNNERS 💯🫶😎 :
amna niou meunoul togou ak ataya ba paré beugeu seuyi😊
2026-09-18 17:09:37
9
sophieboutoutouast
Sophieboutoutouastou :
Wawaww si seuy normal wawaw💃💃💃🥰🥰🥰🥰
2026-09-18 11:36:29
18
sokhna.kany
Une221🖤👑🇸🇳 :
Mafei biii
2026-09-19 00:36:51
7
sohnadiarra38
Sahna Diarra 💕❤️ :
Dieukeur Bou naye nak 🥺🥺🥺
2026-09-18 18:40:41
14
maiscestamywesh
Une sénégalaiseuuh🇸🇳🇸🇳🤭 :
Bou dépense doyé rekk, dara douko téré nekh 🙌🏾
2026-09-18 15:00:39
12
ataaaaaaaa36
Æ💕 :
Ni la beuggg Mel souma magué😭
2026-09-18 12:45:24
8
dija_shop14
dija shop :
on aime faire pareil mais poss yi mo féxoull
2026-09-18 15:07:59
6
ngone6762
Ngoné Mbaye🇪🇸❤️❤️❤️❤️🇬🇭 :
Bilay
2026-09-18 11:44:17
5
To see more videos from user @mrsfayekitchen, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About