alhamdoulilah djeureudjeufé serigne touba diarama mame cheikh ibrahima fall
niak xam limou waral barina
2026-09-18 19:24:56
23
IBG-Fallou_Leuh :
yalla nama yalla rayé si beug serigne touba
2026-10-02 16:53:14
7
Prince 🇸🇳👍🏅 :
C'est à se demander même si c'est Serigne Touba qui a écrit tout ça.
2026-09-18 16:20:59
7
fallou niang Wakana :
borom touba moy yalla
2026-09-18 23:49:24
4
Bineta Ndiaye :
Santé serigne touba
2026-09-18 15:26:44
13
karim😊 :
Prk tu parles mal ? Li gue beug wax tu peux dire ca en étant polie. Mais la on sens que haine gay waxei. Tu penses que daga ame xam xam ni ? Waxine dafa lath déguine peut être il dit ça indirectement mais Sergine touba loumou wax rek am ne justification, alors stp parle avec di respect.
2026-09-21 02:02:26
2
MOUHA :
Il essaie de convaincre qui ?
2026-09-19 11:32:32
3
WISE FOR EVER 💎 :
YALLA MO MOM SERIGNE TOUBA MOM BAAYOU SERIGNE TOUBA. Yalla meussoul taggou kenn
2026-09-18 16:21:36
9
Mamour dip 👊🚗 :
S touba ken lah
2026-09-18 15:24:55
18
abdou ngom :
sante serigne touba rkk
2026-09-18 16:20:10
5
G@y€ b@b@c@rr :
es que lingay wakh ni deug la mane déh worouma 🤣🤣🤣
2026-09-18 15:27:24
8
user6339508865682 :
serigne touba sonuna 🥹🥺
yal na nyu ko yalla feyal
2026-09-24 17:00:32
4
Borom touba amoul morom :
Serigne touba dou kouy dioum
2026-09-25 15:19:23
3
Ibrahima :
Lii gana messire wakh nako.
2026-09-18 16:08:26
0
sohaïbou diallo :
ki koubahkla🥰🥰🥰🥰🥰🥰
2026-09-25 12:43:26
3
Merci manma33 :
Merci
2026-09-23 17:54:27
2
🇸🇳الله💫🇬🇲الله💫الله🇲🇷 :
GUISS💫YALL💫MOY💫DEUG
2026-09-25 19:07:13
1
Baye Gor fall :
serigne touba louko yalla maye mayou ko ken mo takh
2026-09-20 13:36:55
0
Mamecheikh :
Saway khamo dara sa Diague sorifoul amo pass pass s Touba Loumou wakh dégue lax Bilakhi dieureudieuf s Touba ❤️
2026-09-18 16:11:50
2
mor :
Ismaël Diame reç guai am inchalla dieuradieuf
2026-09-24 16:09:31
2
chicoloco :
Bravo Jeune Homme De Dire La Verité Lou Doule Yalla Néne Le .