@dymo_story: Modou Bouki dafa bañ jigeen ji ko ay waayjuram tanal... Ndax mbindann bi 😱💔(Partie 1) Modou Bouki, héritier de la famille Ndour pouvoir bi, lepp amewoon ci moom... bamu des ci moom sa bopp di tann jigeen bou bëggoon. 😔 Waajuram yi jëloon nañu dogal ni dafay sëy Maman Bouki, jigéen ju am mbiri alal ju bawoo ci famiy bu am doole. Waaye Modou dafa bëgg Nafi, di mbindaan bu woyof ci kër gi. ❤️ Bi Maman Bouki xamee dëgg gi, ci la ni dafay tiital Nafi... Ndax Modou dina tànn mbëggeel, wala déggal njabootam? 👀🔥 #HistoireTikTok #TikTokSenegal #HistoireWolof #StoryTime #PourToi