Ndox saax meunoul dindi sobé yala moy setal je suis ouvert au débat
2026-09-20 03:05:06
36
ḲḭḶḶ𝑬R 🇸🇳 :
Gni gno diara invité nk
2026-09-19 01:01:45
806
tarek :
l'eau source de la vie alif lam meem
2026-09-19 01:01:26
107
omar thiane🇸🇳🇮🇷 :
Sonko yalla nako yalla takhawou❤️🙏❤️
2026-09-19 01:51:30
322
s mbacké :
kii yallana kou yalla sambou
2026-09-19 00:47:26
1165
talibéahmadou :
tay oustaz dacorouma d’accord na wala ?
2026-09-19 08:08:57
83
𝚕𝚊 𝚟𝚒𝚎 :
𝚕'𝚎𝚊𝚞 𝚌𝚘𝚗𝚝𝚒𝚎𝚗𝚝 𝚞𝚗𝚎 𝚖𝚎𝚖𝚘𝚒𝚛𝚎
2026-09-19 00:46:09
414
momar dioum :
limiy wax dou xam xam
2026-09-21 16:37:34
0
mbayebabacar563 :
On doit le préserver Bilahi Sénégal khamougnou lignou amm Mach Allah Professeur ❤️❤️❤️
2026-09-19 01:22:46
34
Max_Taylor__fall_🧧 :
ndox dafa am rawhaniya👌
2026-09-20 23:29:50
0
Les RekRek :
Senegal dounioi xam. Douniou guestou so waxé niou weddi la. Wallay kou gen rew mi di nga xam niou louné amna. Bo guesto tuuti yeemou ci yalla. Yalla lou eup dafko neub. Allez regarder le documentaire sur la mémoire de l'eau