@kay.setaneu: đŹ BOUKI â VOYAGE AU NICARAGUA_ PRIX DâUN RĂVE | NJABOOTU YĂNGA | THE PRICE OF A DREAM đžđł WOLOF : Bouki mooy ab bu ndaw buy dund ci SĂ©nĂ©gal ak xaalis bu nĂ©ew. Ndax amul xaalis, nit ñu ci dĂ«kk bi dañuy ko toroxal, di ko wax ne du dara. Loolu dafa ko metti ba mu bĂ«gg a dem ngir seet dund gu gĂ«n. Mu bĂ yyi SĂ©nĂ©gal, tĂ mbali yoon wu sori, te ci yoon wi mu daje ak ay jafe-jafe, sonn, ragal ak solitude. Gannaaw lu bari, mu agsi ci Nicaragua. Foofu, immigration yi jĂ ppale ko, seet ay papiersam ak identitĂ©, defal ko contrĂŽle mĂ©dical, te jox ko ab kĂ«r bu mu man a toog. Waaye Bouki gis na ne yoon wi dafa gĂ«n a metti li mu xalaatoon. đ«đ· FRANĂAIS : Bouki est une jeune qui vit au SĂ©nĂ©gal dans des conditions difficiles. Parce quâil nâa pas dâargent, certaines personnes de son entourage lâhumilient et lui font croire quâil ne vaut rien. ĂpuisĂ© par cette situation, il dĂ©cide de partir Ă la recherche dâune vie meilleure. Il entreprend alors un long voyage et traverse de nombreuses difficultĂ©s : fatigue, peur, solitude et conditions difficiles. AprĂšs tout ce parcours, il arrive finalement au Nicaragua, oĂč les services dâimmigration le prennent en charge. Son identitĂ©, ses documents et sa nationalitĂ© sont vĂ©rifiĂ©s, il passe un contrĂŽle mĂ©dical et reçoit un logement temporaire. Mais Bouki comprend que son voyage a Ă©tĂ© beaucoup plus difficile quâil ne lâimaginait. đŹđ§ ENGLISH : Bouki is a young living in Senegal under difficult circumstances. Because he has no money, some people around him humiliate him and make him feel worthless. Tired of this situation, he decides to leave in search of a better life. He begins a long and difficult journey, facing exhaustion, fear, loneliness and harsh conditions. After everything he has been through, he finally reaches Nicaragua, where immigration officers take care of him. His identity, documents and nationality are checked, he receives a medical examination and is provided with temporary accommodation. But Bouki realizes that the journey was much harder than he had imagined. đ MESSAGE / MESSAGE / WOY : BĂ«gg a soppi sa dund ak am avenir bu baax, lu baax la. Wanting to build a better future is a good thing. Vouloir changer sa vie et construire un avenir meilleur est lĂ©gitime. Waaye bul teg sa bakkan ci risk. Seetal yoon yu wĂłor ak yu lĂ©gales. But never put your life in danger. Always look for safe and legal pathways. Mais ne mettez jamais votre vie en danger. Cherchez toujours des voies sĂ»res et lĂ©gales. Waajur yi, dĂ©glĂ©en seen doom yi, waxleen ak ñoom, te jĂ ppale leen ci seen projet. Parents, listen to your children and support them. Parents, Ă©coutez vos enfants et accompagnez-les dans leurs projets. â€ïž Sa bakkan moo gĂ«n lĂ©pp. â Your life is worth more than anything. â Votre vie vaut plus que tout.#creatorsearchinsights #debloquemesvues #senegal #france #USA
KAY SETANEU
Region: SN
Sunday 20 September 2026 13:58:13 GMT
Music
Download
Comments
Laye sow :
video bi amna solo continel boulthi bole saga rk bonne contination
2026-09-21 14:52:49
3
Lamine â€ïžsĂ©rĂ©re mon sang 𩞠:
Bou takhĂ© nguĂ©ne doug si forĂȘt đł bi danguĂ©ne di voyager đ§ł bouki si bopame molenedi lĂ©kk â€ïžâ€ïžâ€ïž
2026-09-21 10:51:58
117
l'incomparable đđđ«” :
bouki sakh deg na anglais
2026-09-21 12:08:31
50
sen ia :
Lii mo metii deuk bii amoul dara niou lay tekk pression
2026-09-20 14:47:03
262
less wakhoulđ§ đ :
kone boki sakh sénégalais la
2026-09-22 15:23:27
16
Khadija rassoul đ„°đžđł :
My name is bouki. I am from Senegal.
2026-09-23 01:26:49
0
Foot Addict :
Ndeysan lii mom warr na viral
2026-09-20 14:52:52
31
Liverpool suel :
bouky mo man engale kaye
2026-09-21 12:03:30
4
Univers_Chicđ :
bayi léne pression sociale biguéne di tékk diamou yalla yi
2026-09-20 14:07:02
34
DEMBA COLY :
deuko sĂ©nĂ©gal dééđ
2026-09-21 13:56:26
8
@Mbodj Soce+221 :
c'est vraiment intressant de faire des video comme ainsi en anglais ça vas renforcer nos vocabulaires
2026-09-21 00:31:44
14
@dadasylla1 :
Lokho biy feugue koukou mome
2026-09-21 11:05:34
6
Fatimah đžđłđČđ± :
La partie anglais ma prĂ©fĂ©rĂ©e â€ïžđââïž
2026-09-21 13:38:01
3
Une fadilate đđâ€ïžđđčđ„°đđ :
My name is bouki I am from Sénégal [Ricanement][Ricanement][Larmes de joie]
2026-09-20 23:31:25
8
L'ENFANT DU SALOUM :
Un message trĂšs trĂšs important pour la jeunesse đđ
2026-09-20 21:16:14
20
amĂ©ricain bou talfa đ
żïžđ
°ïž :
demal khĂŽl sama premier vidĂ©o đ
2026-09-21 11:18:03
3
TAKHA :
333333333333
2026-09-21 14:53:00
1
En quĂȘte du savoir :
suites svp
2026-09-21 15:42:59
1
maudibeau :
na niep guein bein jour tall sein téléphone woné souniou nakar ci coupure courant yi ba paré cher
2026-09-21 21:51:12
5
malick joop :
amna solo
2026-09-21 12:50:51
1
Amzo Boy :
PABLO221
2026-09-21 14:50:13
2
alaji Gaye :
222
2026-09-20 23:13:40
1
Ibrahim thima :
â€ïžâ€ïžâ€ïž
2026-09-22 21:00:43
2
SaĂŻdina youssouf brom diamou :
Voix yi Barina dh đ
đ
2026-09-21 01:24:48
4
user72909992383933 :
222222222333333333333
2026-09-21 12:04:15
1
To see more videos from user @kay.setaneu, please go to the Tikwm
homepage.