Boudé ndiarign li mo eup lorangué gui kay loy wakh😀😀😀Saway dadji ngama😀😀
2026-09-20 17:19:10
225
Sheex Fallou 🧬 :
1bi Waxko gnun barkeilou wougnou deh dagnuy naan à volonté
2026-09-20 16:59:44
257
SHEIKHERA :
Sayy kii dayy advertise rkk
2026-09-24 00:18:35
0
Bousso Baly🌸 :
Damay diay café sax😌🤎
2026-09-20 17:25:47
296
@TI££DO✨🌹$@LIK#👌❤️👌 :
Kou moudj ki daal Amna kham kham lol🥰😍😘🌹❤️🤍
2026-09-22 17:45:06
0
Mïna Diallo :
Cafè touba laniouy nane di waxtane tamouy deugu si barkep borom ndigeul fa yalla fa yallay fall
2026-09-23 22:07:02
0
Mina 🌺 :
Mane mome franchement café Touba beugoumako nonou souma yéwo avant may dém entraînement lay nane béne case souma nieuwé nanate béneu soumay ndecki nane niar avant may agne nane béneu souma dioulé takousane nane béneu avant may diouli timis nanate béneu souma dioulé baparé nane béneu goudi mome trois case lay dieul avant may teudi beuri woul nak 😔😔
2026-09-21 01:15:01
107
asstu29 :
Le « nioune naañu thé matcha » liiii sa xol ngako jëlee Baay Fadilou😭😭😭
2026-09-20 17:04:58
310
Ihsaan :
Lignou wahe ni yeup ay toubab gnoko binde, gnoune li SEUGN TOUBA wahe mo gnou doye