😂😂😂 Parfois dangeen di bëgg garaaw gaarawlu 😂ba saaga Y... Walla ngeen weddi ay waxam te du ngeen ko yëg
2026-09-21 14:19:38
1
Ibrahima Mbacké :
té blessé أستغفر الله
2026-09-21 12:36:38
0
seydina leye saloum :
li de appu na wakh demal niou firil lako thiey yalla 😳😳
2026-09-21 12:58:37
1
افعل ما شت فکما تدین تدان :
Man dom sonu si Dara dekou yokh se n’en
2026-09-21 15:24:14
0
Mohamed :
lii dé mousiba xanaa xamo limi firie
2026-09-21 13:27:02
0
laminebarasene1 :
say li nga bindi doy na war de yalla moy diakh diakhal kholi nit yi wala seytane 😳😳😳
2026-09-21 14:05:36
0
𝕏 :
yallah bagnou note sa yaye
2026-09-21 19:26:32
0
Ababcar bou sonko ⍟ :
si tourou bour bi laye tambalé moye diakhe diakhale xoll yi lii deh ngafi binde te yalla nena لا تبديل لكلمات الله boulen sopi ayat yalla yi lii dafa harame seugne bi tapalé bakhoule
2026-09-21 19:59:17
0
Modou Ndiaye :
🥺🥺🥺😅😅😅💗💗💗🥰🥰🥰😁😁😁😂😂😂😅😅😅😳😳😳
2026-09-21 11:57:50
0
s aliou dieng Fissel :
❤️❤️❤️
2026-09-21 13:23:01
0
To see more videos from user @abdouaziz.ndiaye31, please go to the Tikwm
homepage.