li Moy définition vrai xam xam 🙌
Dara diaroul yakamti dafa diotagoul rék
2026-09-21 16:42:32
206
dieytastore :
Qu’Allah nous accorde le tawakkul dont nous avons besoin et qu’Il nous apprenne à Lui faire pleinement confiance
2026-09-21 18:07:56
153
Black D :
Ndap Lou tilim sun borom dussi def niamam wakhi cheikh ibra ♥️yalla nanu sun borom xiir si bopam xirr gnu si lou bakh
2026-09-21 20:53:41
17
Aminaaah🍒🌸 :
Pour mann Ndap bou sett moy le travail en soit biguey deff pour ioe sa bopp
2026-09-21 18:56:34
73
amra2.0 :
Lou way def bopam 🙏
2026-09-21 23:06:17
0
MAMYAMAA :
Manshalla
2026-09-21 22:43:49
0
بنت فاطمة🦋⭐️ :
Macha’Allah waxxx bi kawei na il faut que nittt ki am deggg degg bou kawei pour meunala degg Walahiii j’adore tes vidéos ndax diko deggg rkkk dafay yokk makama Marhabane 🙏🏾🥰
2026-09-21 17:50:00
34
Mounir mall :
Bro defla xarit lou daga la
2026-09-21 21:22:56
0
Miss univers 🙈💕👸 :
Ligua wakh kou khamoul yalla douko comprendre machalla
2026-09-21 16:58:02
35
Mouhamed ✪ BFL♣️🧠 :
Wakh bi Kawénz☺️🙏
2026-09-21 16:35:49
46
Mame Khoury Bâ :
"Astaghfirullāha wa-atūbu ilayhi " chaque jour matin et soir.
2026-09-21 20:51:55
9
r@yon d'soleil💍❤️ :
Mo neubou wayei mo fegn ! ya khayou ya khayoum yazzal djallal wal ikram🙏
2026-09-21 19:05:55
14
سيدنا علي ساخ :
Mindset
2026-09-21 22:44:16
0
Töölu sénégal 🇸🇳 :
Dans chaque difficulté il à une facilité (regarder vos problèmes d’une autre façon vous allez comprendre facilement)👏 merci pour le conseil
2026-09-21 19:21:48
9
Munga 🐐 :
Cheikhou Tidiane Cherif rta amouniou fayam
2026-09-21 16:52:10
9
wiizjames2023 :
yalla nala Yalla fay li amna solo
2026-09-21 17:35:40
11
himra950 :
From LTSNT 🙏
2026-09-21 21:18:04
0
Sokhna maï Thiam :
sallalahou allah Muhammadine 💚
2026-09-21 21:16:05
5
Fall :
Macha Allah
2026-09-21 20:14:36
5
𝒜𝓏𝑜𝓊 𝕭ou serigen fallou✰ :
Sama yaye 🥺🥺🥺
2026-09-21 16:29:45
9
Sokhna fatima :
Vérité absolue
2026-09-21 17:44:20
5
ELZO :
2026-09-21 18:24:18
5
Papy jean gomis :
MAnChallah wax ji amna solo
2026-09-21 16:29:32
5
Mouhamed 🎓 :
Ndab li moy Xol bi.
Tuub bakaar ak bayi lu bonn mokoy foot 🙏🏾
2026-09-21 23:20:25
1
BIG FA 🇸🇳 :
Machallah Bro amna solo trop
2026-09-21 22:26:43
1
To see more videos from user @bethebusiness13, please go to the Tikwm
homepage.