billahi mane ak sm yaye lilay doudou guissou nou guéneu
2026-09-22 21:10:35
87
@RYAN YAMAL 💫💙❤👑🚭 :
ay souma yalla défé kou am kom kén dou sonou wallahi ☝🏾😭
2026-09-22 22:10:26
67
fans Mame bousso Fatou Ndiaye :
mallechala félicitations à toi mon frère ☺️
2026-09-22 20:38:45
106
Max business 🖇️🛍️ :
Mbokk légui yi diapalé wougne kéneu
2026-09-22 22:43:02
37
🅰️🅱️D🅾️U ☪️☪️☢️✝️✝️ :
aye souma amon alle lli lepou dou am ganaw yalla sounou borom 😭😭😭
2026-09-22 20:34:39
24
Ndioba Thioune :
Mére yalla nga doundou ba faté sa nakar sa ndiabote gui weurleu yalla nagn doundou ba tabakhal la immeuble yobou la maka téral la té yalla may wér ak goudou fane sa mak dji mais grand sa liguéy raféte na yalla nala yalla fay 🙏🙏🙏
2026-09-22 22:38:47
27
baye saliou❤️❤️ :
wakhal sallahou alamouhmade
2026-09-23 12:16:13
13
L'H°ME_T¥M¥D£🕸️ :
Ndeysane suñu yaay DJI Amna louko métti billahi😭🤧
2026-09-23 14:29:31
8
la mbouroise :
mbokk légui kéne bakhou si
2026-09-23 13:47:23
7
✨ʙᴇʟʟᴇ & ᴄʜɪᴄ 🌸ʙʏ ᴋʜᴀᴅᴇᴇᴊᴀ 👑 :
Ndeysaane mbokkou légui yi tmt dh doynagne waar 🥺
2026-09-22 20:52:09
31
Ramlou pronostique :
thieuy adouna😭😭💔
2026-09-22 20:56:47
23
La diva❤️🍎 :
Félicitations à toi frère khol yeup toyna 🙏🙏🥹🥹🥹
2026-09-23 18:33:33
12
🎀Thiatou Yayam 🎀🧸 :
Sallalahou alla Mouhamed ❤️❤️❤️❤️❤️
2026-09-22 21:11:44
16
METZO_ai :
allahou akbar ☝🏿
2026-09-22 20:49:42
17
Mamma mrs mbaye :
yalna yalla same lén
2026-09-22 20:52:59
6
PAPA_BOU_LISS 👑🏟️🇸🇳 :
yalla nako yalla takhawou 🤲🙏
2026-09-22 22:59:09
7
pape gueye8 :
yalla nako yalla tahawo
2026-09-23 00:39:34
6
Mouhamed sarr ✪ :
naniouy diouk fadiar di diouli svp
2026-09-23 06:54:12
14
hawa🇸🇳 :
Bilay wallah adouna lou guiss day diekh mais yalla bakhna 😭😭😭😭😭😭😭😭😭
2026-09-22 22:25:45
5
789997368 :
2026-09-22 20:36:57
6
Mamy :
Mbok amatoul yalla baxna leupay diekh inchalla
2026-09-23 10:20:52
8
rassoul ndao+221 :
masta yaye yalna yalla samou yalla la xalé yi téral nga féké lép
2026-09-22 23:58:18
12
MASAMBA⚡️ :
Alhamdoulilah 🥺
2026-09-22 20:21:19
5
To see more videos from user @alaminebaraofficielle, please go to the Tikwm
homepage.