mome wakh na lepp ba paré ni kéne douma khamal dara🤣🤣🤣🤣
2026-09-23 09:16:20
327
Princesse Diop :
Yoro dara kay😂😂😂
2026-09-23 00:51:07
1001
Notification tiktok :
Un cœur pour notre créateur 𝔸𝕃𝕃𝔸ℍ
2026-09-23 03:03:03
967
mr X :
Mane dh xr la yor
2026-09-22 23:41:46
472
Amsa Noël pouye❤️💍☺️🎊🎄 :
Soube mou kass ko nqk [En larmes][Larmes de joie][Larmes de joie]
2026-09-22 23:57:05
604
Mrs Diawara💍 :
Contane nagn di Ibou 🥰 Binta seuyeul ba dé
2026-09-23 08:35:45
373
ℂℍ𝔼𝕀𝕂ℍ 𝕍𝔸𝕃𝕍𝔼ℝ𝔻𝔼🌟⚽️ :
Lisi geuneu graw moy dafa am lou diafé si djiguene moy humour ta lolou dafay takh kou goor geuneu ko beug ndakh bonheur bii ta lepeu loumou ko beug wakh dîna foo ba wax ko j l’adore walae❤️🥀😂
2026-09-23 13:27:54
121
maman jolie :
ibou moom day reée rk 😂machallah 🥰
2026-09-23 11:56:28
99
princesselebou82 :
Mane binta dama ko beugeu nk Bilahi 🤣🤣
2026-09-23 00:11:07
196
MODAF10 :
ndeysane kagne lay ame diabarr
2026-09-22 23:43:36
611
La sénégalaise caviar :
Juste iPhone no le monde est fou
2026-09-23 02:06:54
87
SY MALICK💘 :
Teh doussi def ben thiaaa Bineta😩😭
2026-09-23 16:03:37
0
pro ibou🔘 :
binta avant iPhone 18[Laugh approved]
2026-09-23 12:31:37
1
fall Yaram🤍🖤 :
sallalahou allah mouhamed 🥰🥰🥰
2026-09-23 15:00:39
42
oumi ndiaye :
khamone nako mane lou ma wakh rk daye am machallah yalla na dondou ba aï dômame diko féfal
2026-09-22 23:37:27
302
Abdou Karim Gadiaga :
mafi geuneu beugeu borom touba
2026-09-23 11:03:21
32
2Y🦋Ndiour🥰 :
sa mome c'est vrai kou téral sa diabar yallah téral la
2026-09-23 11:11:29
35
𝓚𝓱𝓪𝓭𝓮𝓮𝓮𝓮𝓳𝓪ꨄ :
Binta niatta ngua dam am dissertation 😭😭🤣
2026-09-23 01:33:28
99
TimaSowpoulho :
Bineta yalla topéwouko dara .Ibou merci beaucoup goor day meuna teral jiguen machallah ♥️♥️♥️
2026-09-23 14:20:29
16
.kinediouf :
Ki dama ko beugueu 🥰
2026-09-23 01:07:47
58
Salihate bi 🔐❤️ :
Boul khépp gnane yi dhe daye dale sa awo sou kholam sédé si yaw loume la gnanal daye dale 🥰🥰🥰🥰🥰
2026-09-23 12:32:38
22
To see more videos from user @sokhna.et.sega, please go to the Tikwm
homepage.