@wwwtiktok.comwwwdomouass:

domou ass dion
domou ass dion
Open In TikTok:
Region: SN
Wednesday 23 September 2026 12:56:25 GMT
42013
6325
386
23

Music

Download

Comments

user2537209638560
user2537209638560 :
li rey na ma billakhi yal nala yalla takhawou😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
2026-09-23 20:06:05
0
ngff19
𝐍𝐠𝐮𝐢𝐫𝐚𝐧𝐞 𝐟𝐚𝐦𝐢𝐥𝐲 :
Bilahi wallahi barkii borom touba souma dème bay deglou xassida yii Ass Dione mi moh takh yallah na souniou borom teguill la n’atoou bi incha Allah 🙏
2026-09-24 00:51:25
1
papiange8
Anticorps Pastef :
mom bokouna ci litakh ma intéresséwou ci khassida yi et pourtant talibé cheikh la. yalla meune na lounek yalla nako diapalé ba gueinéko ci toloftolof yimou nekk
2026-09-23 18:14:29
85
aliounebadara054
Aliune bou seuydina oussmane :
Yalla nako yalla takhawou thi barkè alkhouran Karim 🙏❤️
2026-09-23 22:40:06
0
djibygueye818
[email protected]🇸🇳⚽️ :
Bly ya bakh Amine way 🙏🏽
2026-09-23 20:30:42
0
thiernobousididiop1
thierno seck :
natou do wess yalla bakhna
2026-09-23 22:35:06
0
seydina_alioune_hizbou
𝓢𝓮𝔂𝓭𝓲𝓷𝓪 𝓗𝓲𝔃𝓫𝓸𝓾💦 :
Ohh ndeyssane sa wadji yalna sa Borom Djiégeul ko téh djiégeul niou sunuy Bakaar 🤲🙏😭😍
2026-09-23 14:36:53
63
user4369415725542
mame diarra niang :
ndeyssane ❤️❤️❤️❤️🥹🥹
2026-09-23 15:26:31
63
laye7795
LEY ABDALLAH ❤️🕋 :
Namnaa koo lol barké AHMADOU Yallah teguilko natou bii 🤲🤲
2026-09-23 18:18:25
23
tafsir.jr.diolof
Saydina Mouhamd nabine🎤♥️📿 :
Bly yalla day natou diam
2026-09-23 20:51:36
0
sowmasser5
Massamba sow 🇸🇳 :
Diangue kay moko meun 🫶🏿
2026-09-23 20:39:54
18
khadimkhadim505
khadim ndiaye :
yalla rek moy Yalla 😭
2026-09-23 21:10:48
11
user7461318128444
toure création :
yalla na ko yalla sam
2026-09-23 13:34:06
7
madame.sidib623
La voix d’or :
Wallahiiiiii beuggggg nakooo ba Pere
2026-09-24 09:57:31
0
asta.saliou49
Asta saliou❤️💕 :
Yalna ko yalla teguil natou bi inchallah 🙏😭😭😭😭
2026-09-24 09:27:37
0
sokhnamagutte
sokhn maguett saliou :
ndeysane 🥺🥺❤️❤️❤️
2026-09-23 18:26:41
5
user7319887534081
talibè serigne saliou 😍 :
machallah 🥰🥰
2026-09-23 21:00:58
6
sfallouxasidainamn
s fallou xasida inapna :
Walay Ndey San yalna yalla takhawouko brk khasida yi djambar lawon dh vraiment
2026-09-23 21:17:23
0
fatouchbb0
santé Daam kese :
ko bakh la
2026-09-23 19:17:02
0
cheikh.mbow63
Cheikh Mbow :
ndaysan
2026-09-23 16:05:41
1
mbayecana785
MbaYe DabaŸe NdiaŸe❤️ :
Diangne kay walahi mosi man ohhh😭😭 yalla nako yalla taxawo 😭😭😭
2026-09-23 21:33:24
0
b.saliougayewakanna
B.Saliou Gaye wakanna💙🤍 :
Serigne ass dioun xassida yalla n'a yalla tahawko ba mo déllo si watt si lagéyy bi si barkép alhoran ak sayidina wakanna khahan 🤲🤲
2026-09-24 07:44:04
0
ibraseexsekk
IbraSeexsékk :
ceey yàlla
2026-09-23 18:37:19
0
sopey.asse
soxna Maty saliou wakana :
ndayesane
2026-09-23 20:09:04
3
ndiaye.mou.srg.sal
NDIAYE MOU SRG SALIOU MBACKÉ❤️ :
ndeyessane 😭😭😭😭
2026-09-24 01:19:59
0
To see more videos from user @wwwtiktok.comwwwdomouass, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About