@voixmedicale: Et si donner de l’argent à sa femme était aussi bon pour sa santé ? #femme #MentalHealth #argent #fyp

Voix Médicale
Voix Médicale
Open In TikTok:
Region: CA
Wednesday 23 September 2026 15:31:13 GMT
336917
36235
2175
11710

Music

Download

Comments

cheikh.link7
Cheikh Link🇸🇳🇮🇹 :
Grand sa vidéo bi amoul Son pourquoi
2026-09-23 17:12:51
840
bibichouking10
Ma Bibichou De Touba💍👑♥️🕊️ :
Niitou Yallah Foko guiss khamé koo Machallah ♥️🤧
2026-09-23 15:41:28
2892
mouhamed.rassoul.ngom
Mohamed rassoul Ngom🇸🇳⭐️⭐️ :
Video bi amoul son
2026-09-23 19:51:57
0
amdymustafa98
Amdy Mùstafa 🥰 :
Souma amé diabar bilahi damakoy betteu diko may , par exemple damakoy wax am Mais si sachet lakoy def soukkou oubiwé fékk si 50mil dieum kaww
2026-09-23 17:22:32
630
talib.cheikh847
Talibé cheikh📿 :
Borom xam xam deuggg mashalla
2026-09-23 19:57:26
1
adja2617
JAAD👸🏽 :
Grand mba yékngani dangay doundou😭😭❤️
2026-09-23 19:02:17
2
bousso__077
Bousso Era🦋✨🎀 :
Li motax nga glow
2026-09-23 17:13:35
87
ramista44
Rama Niang :
Amna solo mais féré yi goor gni déf pour nga yor loy may sa Sokhna dou yombou réw mi dafa méti
2026-09-23 19:51:08
17
evalabellecapricieuse
BB Eva la capricieuse♥️🥰 :
Où sont les hommes guire yalla déléne mayé khalisse
2026-09-23 17:03:36
270
touta454
Toufa🥰❤️ :
Mako envoyés sama dieukeur mounima IA la😩😒😥
2026-09-23 16:54:41
7
bayekarim221
Baye karim :
Qui nako état teuthie way procureur waxal si li
2026-09-23 17:48:56
89
lespagnol168
Sofia💕❤️ :
Ndaysan nitou aldiana nala qui
2026-09-23 16:06:23
352
aichakeita171
La Aicha☺️ :
Pour gni dègoul limou wakh xaral ma bindeul lèn ko: nèna délène may seni diabar yi xaliss wala dilen diokh sèny carte bancaires yi, lolou dey takh niou goudou fan, am wer gui yaram ak xel mou dal😌😌😌
2026-09-23 18:02:55
34
user3413711539967
Zeyna :
grand ya bakh
2026-09-23 19:36:35
0
diakhouk
khoudia Mme fall❤️🥰✌️🥰 :
Ya am xam xam yaw 😍👍✌️
2026-09-23 17:46:36
1
galassfall63
Optimiste FGF :
Et vice versa ☺️
2026-09-23 16:23:50
9
awabousonko24
awadiouf3634 :
bilahi ya bakh nitou yallah DEUG ngua ❤️contan na Si yaw dh 🥰 t'inquiètes pas dinaniou abonné aimé partager inchallah
2026-09-23 18:16:00
6
khadieciss
Khadija Cisse❤️ :
Est-ce que doumala dagual si sama salaire
2026-09-23 18:14:16
6
khalilou93
khalilou💥 :
deug gou wére la mane louma ko diokh sama journée daye nekh lolou mome mako doundou
2026-09-23 17:16:51
115
madoubarham1
Madou Barhama🕊️ :
Si il a parfaitement raison def sport dafa bakh si Goor ak djiguéne dafay wadji stress merci pour les conseils.
2026-09-23 16:53:41
32
yayounaby84
Amina rassoul 🕋📿🫶🏽🫀 :
Ki nako état protéger 🤧😍🫡
2026-09-23 19:12:00
10
mouhamed.nassir.05
MHD ~NASSIR 🤍 :
Vidéo bi mo amoul son wla si sama téléphone la
2026-09-23 17:36:12
47
dramebtpplus1
DRAMÉ BTP PLUS👷 :
association internationale de vérification des commentaires vous êtes là 🫴😂
2026-09-23 17:26:14
25
user2am6ayopin
fatte fepou :
grand lingay def ni trouble à l'ordre public la dh😔
2026-09-23 18:06:35
18
user16850692387014
willy :
carte crédit mom dou pour nos femmes sénégalaise, benneu yone lakay épuisé 😩 😂😂😂
2026-09-23 17:33:12
17
To see more videos from user @voixmedicale, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About