Selon code de la route
Li ligne continue la donc interdit de dépasser meusoul ler[Larmes de joie]
2026-09-23 18:57:12
55
Le pilote de la vertu :
iow tmt champion nga ndakh amna nio khamné khamou gnû louy signal
2026-09-23 19:37:36
20
mara business service :
li yep chauffeur camion nioco ligeuye niep dico déf leugui merci sama gayi
2026-09-23 18:22:54
26
paco diaz :
bou leroule danger lagnouy tall
2026-09-23 20:04:55
0
Prins :
Distance de sécurité?
2026-09-23 19:31:56
9
benjfromzig :
defois niou taylé là il faut bien faire attention
2026-09-23 19:26:49
8
Senelec :
gnotay si coupure yi
2026-09-23 19:37:08
10
Aura🦁 :
En tout cas chauffeur deug dafay communiquer si talli ak sen signalisation chauffeur degg nk la wax
2026-09-23 20:25:25
6
M.SOW , Le serviteur :
pour man bus dafa signaler pour serrer coté droite
2026-09-23 22:52:55
0
Donga Dara :
cominucation bi rafetna mais amna ay erreur
2026-09-23 19:54:43
2
Ⓜ️ËTIS-LÉ🅱️OU🥇 :
Signalisations yi kou yaggoul dawal di voyager duko xam😍✅…Oui lerrna dh mais da warone wathie tally bi car ligne continue leuh.Soufa Pathé nekone bindeul la wala lekk say 2k😅😂
2026-09-23 19:49:23
7
Mansour bu serigne mbaye abdou :
meme soufi ligne contine neke meune ga deme
2026-09-23 18:39:47
2
{BAB’S} :
Lerneu wayé Waro dém non seulement tu est en agglomération en plus ligne continue leu
2026-09-23 19:10:40
5
Talibé serigne saliou bii :
Machalla li rafet na waye ❤️
2026-09-23 19:42:43
4
amiedesonmarie3 :
Ligne contenue fo dieum
2026-09-23 21:26:57
0
Doro Niasse :
Niom des fois daniouy fateiiii signal bi dh
2026-09-23 21:23:21
0
joesagna799 :
arrêt de filmé les jens c pas normale
2026-09-23 19:05:19
0
toch boy😎 :
quell chauffeurement 💪💪💪💪
2026-09-23 21:14:43
3
SONKO 2029 :
Dëgg le wayé mom warul yék ci ligne bi
2026-09-23 19:45:18
0
CENTRE ALKHAIRY THÉRAPIE :
Hii mais amna ko xamni boudone mome la demna bou yague 😂😂
2026-09-23 18:45:13
2
paa Diallo :
ligne continuée kén dousi doublé
2026-09-23 21:14:20
0
……. :
Les camionneurs sauvent beaucoup de vies si kaw ngéne respecter consignes yimoulay diokh so topé si guinawam
2026-09-23 19:34:07
1
Ladorable Magx Gaye :
Sa vidéo bi amna Solo .
diang naa ci touty ❤️🥰🙏
2026-09-23 21:27:01
2
To see more videos from user @maison_ventouses_senegal, please go to the Tikwm
homepage.