mon papounet yalla na la Yalla sam arr la mousale si 👁️ak 👅 linga beug Yako kham yalla na la ko yalla défal te mou don li guen si yaw ❤️si barké seydina mouhamed psl amine bou féké gnanou dom dina dal si baye yalla na ko yalla nangou si sm khole bi la ko tibéé bilahi yalla na la Yalla takhawou défal la diam amine 🤲😭