@amdynho.jr___10: Goor qoui boy nayy deuguer bokk weleu bok😂🤭#foryoupage❤️❤️ #fyppppppppppppppppppppppp #viralvideos #tiktoksenegal🇸🇳 #visibilité @Mbarikallah VIP Coiffure @Coumbis ta baby❤️🥹 @Ndeya la madrilène 🦋🌸🌺 @Ⓜ️illiardaire_🅱️ou_🅿️euvre

Amdy🧑🏼‍🦱⚽️🇸🇳
Amdy🧑🏼‍🦱⚽️🇸🇳
Open In TikTok:
Region: SN
Wednesday 23 September 2026 19:11:39 GMT
59933
14683
728
173

Music

Download

Comments

dioufpedri
𝐃𝐢𝐨𝐮𝐟 𝐩𝐞𝐝𝐫𝐢 8 ✪ :
danioula yakaloul sa match division rek motakh 💔🤧
2026-09-23 19:47:00
935
doomi066
doomi reew mi :
goor dh metti na😂😂😂
2026-09-23 19:45:51
326
moussa.gueye6295
MOUSSA BOU NDAW🇮🇹 :
wadji yagui commencer beuri wakh nk
2026-09-23 20:40:39
172
babacarmbaye803
𝕭𝖆𝖇𝖘💫𝖉𝖌🧠 :
Ya bari wakh yaw
2026-09-23 19:48:11
251
ousseynoundao088
ousseynoundao187 :
yagui commence beuri wakh nk ioe
2026-09-23 20:13:51
52
babs2k.5
babs_2k5😎 :
bizarrement sma gallé man rek ma amoul ventilateur blh
2026-09-23 19:22:46
113
princess_aminata12
Ndeye Amy Ndiaye🙃 :
Man mom lane la meunoul comprendre guoor yalla bou bary wax comme yaw lou nior mou wax lou nioroul mou wax bari wax ba beug dh guoor yalla day wax touti
2026-09-23 21:18:36
29
gorandoye23
Gora Ndoye 🇸🇳🇯🇲🇯🇵🏴‍☠️ :
Yaw boy beuga graw graw lou dé 😂
2026-09-23 20:15:39
33
mouhamedsakho7151
doffou rio biii 🩸 :
goor yalla d'où beuri wakh
2026-09-23 20:09:18
46
chroniqueurthiesois155
*BAMBA & FOOTBALL🤞 :
Yaw doul
2026-09-23 20:06:51
110
jr______ndione
🥷𝕵𝖚𝖓𝖎𝖔𝖗✰✞ :
Goor yallah dou wax lou barri 🤫
2026-09-23 21:07:00
1
mouhamedkara00
𝕸𝖔𝖚𝖍𝖆𝖒𝖊𝖉🫅🏾✨🥀 :
Sma connexion bi diékh na 😩😭
2026-09-23 19:51:30
18
elkha_443
Kallamuh @43 :
Mann division yi rk mo takh kw💔
2026-09-23 20:03:59
7
ndy__gaming
NDOYE_-_MSR🐍 :
khana do gam Division
2026-09-23 20:53:05
2
diao___dog
𝕻𝖗𝖎𝖓𝖈𝖊👑ᴍᴅ🐾 :
say khana do joué division
2026-09-23 20:35:27
6
baay_moor7
Orèooo 🎭 :
Nion tay amdy
2026-09-23 20:41:09
3
user4752594803545
Lépou Ndoye :
yaw do jouer division efootball khanaa
2026-09-23 20:39:07
6
jean.aris4
Jean Aris :
Dagua beuri wakh nak
2026-09-23 20:10:06
14
user298123935211dd
catalan :
sallalahou Allah Mohammed
2026-09-23 21:03:33
5
sniper00722
Sniper 011💎 :
Dafék joue wo efootball ba meuné si division yii rk
2026-09-23 20:36:28
43
le.prince.moustap8
Le prince Moustapha 🤴🏾🥹🥰😘 :
Amdy seul dakoy dawe 👌🏾✌🏾⚔️🤣😂
2026-09-23 19:31:17
19
seckmavker
B___🤍🪐🤴🏿 :
Wakh na ndy deugg😂😂
2026-09-23 20:11:00
6
fallou.fashion.sho
Fãlløu❤Pedri8💙 :
Yah geuna noy nieup😂
2026-09-23 20:46:09
23
elhadji.malick.gu4
MALICK✨️😎⚽️💰 :
parfois ma déme bay sangou mais souma khalaté ni amna niou beugue sangou té amouniou ndokh rék sama yaram daw ma bayi ko😭
2026-09-23 20:29:10
21
papahramos4
Papah-Ramos4🇸🇳✪ :
Amndy Tay dacco rouma ak yaw dh 😂
2026-09-23 20:03:51
9
To see more videos from user @amdynho.jr___10, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About