Yaw y’a khamoul li mouy wax mé nioune kham naniouko
2026-09-25 02:32:26
0
Gentle Ndongo⚙️🚘 :
limou wakh 25 ans après gakoy comprendre 😂💯💯💯💯
2026-09-24 23:03:01
35
Reuff mou Mame Fallou :
denga yor nop khalé rek 🙏🙏🙏
2026-09-24 20:04:53
27
Touba Sénégal Apple TSA :
Sunu grand yi gno amoul wone deg rk
2026-09-25 00:48:01
2
ASS :
Lido wayo Khalé
2026-09-24 17:13:35
24
damas Ba :
khalega
2026-09-25 13:35:07
0
KHALIL BUSINESS :
Meilleur chanteur Big respect ♥️
2026-09-24 22:13:41
9
RASSOUL AUTOMOBILE 🔺️🚘 :
Nn danga nane loutax doouma xam.limouy wakh
2026-09-25 15:23:27
4
Amar Ciss🇸🇳🇲🇷🇸🇳 :
mélomane deug moko mana kham baye péne rk🥰
2026-09-24 23:03:02
6
Badou Thiaw🇸🇳🇸🇳🇸🇳 :
sama patron mokoy deuglou Dakar ba Mali motakh loume wakh DEUG nako ☝️
2026-09-26 11:25:38
1
zemene Cfa alhamdoulilah :
Ki haut niveau leu khale ou mag bou yakou douko mouno deglou
2026-09-24 20:58:34
3
PAPIS_SAMAKE018🇸🇳🇲🇱🇨🇮 :
[Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie] yow lane key wakh ni xalé dou comprendre baye pene bo magué mou degn
2026-09-25 08:02:26
2
El M N :
sama doom xamal adouna xamal adouna mom nimou mél nimou mél mom déy dox so féké koula mak mom mayko respect amal diñité si mom sama doom li maléy yédé dafa fék yonwou baxla moy yone wi gueun dioup si adouna lo menoul yego démo sama dom lo dou léé
2026-09-25 20:54:55
2
lytout :
Oumar wayaloul khalé deh[Réconfortant][Larmes de joie][J'aime]
2026-09-25 00:59:07
2
Ngom ❤️ :
Ay woyame dou ndiowanou xallé🤞🏻
2026-09-26 12:05:24
0
steeve Marco :
on t'aime notre père
2026-09-25 01:11:42
1
OUMAR NOUROU :
long vie santé et bonheur pour baye péne le meilleur artiste de tout les temps merci beaucoup
2026-09-24 22:31:58
1
ASS :
Wayé Khalé bo beuga kham lomi wakh bo deglo dinga ko kham
2026-09-24 17:14:39
4
idyndoye7 :
déflén ni mane damay mimé rék
2026-09-25 22:55:59
0
mo Afia :
Dangay don fan meune compou
2026-09-25 19:53:58
0
traoremoussa581 :
🙏
2026-09-25 23:02:14
0
mbayemar :
cé le mieux
2026-09-25 22:56:21
0
RODRIGUEZ PEREZ :
Deglou takhoul deggg
2026-09-25 21:56:45
1
dada :
lathie ko ko😂😂😂😂
2026-09-26 13:04:08
0
Mousa Diop :
vc
2026-09-24 21:45:23
0
To see more videos from user @papamaguettediop6, please go to the Tikwm
homepage.