@diamme_tv: Baye Youssou 😂😂😂reew mee jaxassoo 😂😂😂#diamme_tv #senegalaise_tik_tok🇸🇳pourtoichallenge #foryoupage #fyp #wolof

diamme_tv
diamme_tv
Open In TikTok:
Region: US
Thursday 24 September 2026 15:06:55 GMT
446784
37106
1052
4501

Music

Download

Comments

matarcisse978
MatarInsa :
Wa kane moy sa way
2026-10-03 23:15:59
414
element__imam__lamine
element__imam__lamine :
Naniouy diouk fadiar du diouli svp
2026-10-04 11:51:50
399
toumanymane5
toumany 278 :
saway man mi sakh xawma si lane la wra dokh ni🥹
2026-10-02 10:49:27
127
toubz10
toubz :
sonko djakhassè ba parè nii pateu bagna lèral fii milliards yi djar
2026-10-04 02:34:58
173
cissokho876
cissokho876 :
kouy saway😂
2026-10-01 23:26:27
60
never.give.up0372
never give up :
projet bi leu😂 xamou gnou dara reuy lamigne rék
2026-10-03 14:00:43
67
laye.americain3
laye.americain3 :
𝐍𝐨𝐧 𝐰𝐚𝐝𝐣𝐢 𝐝𝐢𝐧𝐚 𝐦𝐚 𝐫𝐚𝐚𝐲 𝐰𝐚𝐚𝐲🤣😂
2026-10-03 22:52:57
78
biramedabo0
𝑵𝒆𝒖𝒆𝒓....𝑫𝒂𝒃𝒐✪🎖️⚽ :
un jour vers 3h du matin ma demon bena programme bay retour 😳ms jour bobou la kham ni yalla meusouma setane 😓may dokh ame Louma sentir sama guinaw souma diokhé mou bougé souma tahawé mou tahaw ma degon gnouni ken dou dokh di gesou goudi ah sama fitt bi togoul rek ma djeki rek daw ms Limay daw yeup tahoul mou bayma 😭ma boléko ay youkhou you metti sakh ba gneupe yewou géna dima diapalé 😭😭nékété allumettes bima don ataya la fate sama poche modon def bruit bi😭ma rouss ba legui douma sigui khôl wa kogne bi
2026-10-05 14:16:24
20
mamadousy2905
baug baye niass :
lii yeup sonko leu
2026-10-05 16:17:49
7
nommade_levoyageur
Same kid from North :
"2024 ñiou sopi rewmi"..2024 géne diakhassé rewmi
2026-10-04 09:49:14
19
mansor3.15
mass7 :
mais kane mooy sa waay? wakh niouko
2026-10-03 18:13:26
11
momoo93
Momo Sembëne :
Béy bi kouko bayi moy deugeul li wadji di wakh 😂
2026-10-04 02:57:07
24
charok81
CAPITAINE DANGOTÉ⚡ :
mangui nii ci bureau Jambourr en tout cas
2026-10-02 13:22:24
33
mouhamednaby26
Mouhamed 🤌❤️ :
Pourtant djakhasé wouma rewmi d
2026-10-05 12:35:08
8
ibougueye0143
IBOU 14@ :
Sérieux c'est vrai vraiment c dure
2026-10-04 09:54:42
6
thiernothiam322
thiernothiam5049 :
Enfin guiss na vidéo original bi 😂
2026-10-06 15:57:49
5
redzoneredzone4
REDZONE :
Wa pastef nioko fal. paré daw bayiko 😂😂😂
2026-10-04 13:24:52
7
barrierrangers2
🥷ranger’s 🇪🇸🇫🇷 :
Sonko la dh 😂diaxasé rewmi daw lakatou ensemblé 😂
2026-10-04 21:13:02
18
doudousow40
doudou :
grand sama fou rire bi nga ma may. ma ngui lay nianal yalla diame soutoureu yague ak weur. ak surtout tope yalla
2026-10-03 05:36:32
19
user2620447653995
user2620447653995 :
Na Macky sall niaw
2026-09-25 01:07:38
21
amadou14eme
amadou 🇸🇳🇫🇷 :
Wa kheud vote la [Larmes de joie][Larmes de joie]
2026-10-03 07:25:56
8
boromdeukebi0
borome deuke bi :
limou wakh ni
2026-10-02 08:27:00
7
para.seydina.mouhamed
talibé serigne Saliou :
😂😂😂Aka bagne saway😂😂😂
2026-09-29 10:09:21
6
To see more videos from user @diamme_tv, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About