lii bilay amoul louko féete kaw si kaw suuf yàlla khamna ko mane daa naa ko bis bu nekk wala ñaari fan you nék ndax bima koy jang gente naa nék si biir kharé bou métti boo khamni ay khédj aki jaasi aki khétou ganaay you nék té mane mangui si biir khékh bi dara lalou ma darra diotouma nii lagne may rombée di doorante ak ray you gnaw sakh bilay yàlla khamna ko 😍té bima genteé lolou yàggul dara ma dégg s abdou Rahmaan di si wakh naan khassida gii koukoy diangue bou asamaan ak suuf doon dadialoo sounou boroom dina la woutal bountou boo diaar mouy lou wér ndeysaan wallaahi 😍😍