BASS_TALIBÉ_S_SaLIOU❤️🩹🙏 :
Bonjour sama❤️xol bi, yaw rekk la koy defaral. 🥰Sa bëgg gi dafa xot ci sama yaram, melni rekk ndox ci tool.🌺🌾 Boo ma xoolee, damay fàtte lii ma yoroon yépp.✍🏽 Yaw laa gëna bëgg ci àdduna 🌏bi. Ndax yaw rekk laa am."Namm naa la ba sama xol day rëbb. Sa baat, sa kanam🫀, sa woyof... lepp laa namm. Su ma nelawé, yaw laa gëm. Tey jii,😍 damay set sa leer ci guddi. Sama mbëggeel, yaangi sama xol, 😘tey ak suba. Bul ma bàyyi, ndax sa wërsëg laa.🥳"Boo ma fi bàyyee, duma dund. 🥹Yaw laa mën, yaw laa bëgg.❤️🔐 Ndank-ndank laa la bëgg, te fawwu yaw. Yaangi sama yaram." boo ma tàbboo ci sa wet, jàmm rekk laa gis. Sa mbëggel dafa fees ci sama xol. Dumala😍🧠 tooñ, dumala bàyyi. Yaw laa tànn, te tànn laa saaf."je🌺🫀❤️🔐 t'aime toujours mon cœur ❤️❤️je t'aime très fort 💘 💘 je t'aime mon amour 💘 💘 sama khol yasi nék abadane mon cœur ❤️🔐
2026-09-29 19:04:01