Yéne gni di khass oustaz dégradé.
Vous ne comprenez pas qu'il joue exactement son rôle. Il anime le débat. L'islam barrina ay wouté si guis-guiss. Débat bi Moy guéné xam-xam
2026-09-26 18:18:04
150
user769191664698 :
je ne veux plus écouté ça à cause ce gars il ne laisse pas les gens parler
2026-09-26 20:08:25
71
Momar Ndour :
kone gnatta yalla mo am ndax mi ngui hiiss gneup
2026-09-27 00:23:54
0
@El Capo221★ :
Bilahi ki hamoul dara oustaz dégradé nena 18 millions de malakoul mawt c triste
2026-09-26 20:12:16
26
serigne modou astou mbacke :
Waaw seringe bi loolou moom dee lay firi
2026-09-26 20:04:23
0
mr LE MAIRE :
Ki do deff si mom
2026-09-27 00:04:35
0
☠️EL_DIABLO👹 :
😂😂 kone kay 8 milliards malaka mawti la
2026-09-26 18:52:25
23
Mor Talla Ndao Mamour :
Ki douma bokou ak mom plateau ndax damay wakh mouy wakh ma diouk dém.
2026-09-26 23:44:24
4
ceedo mbéniou gana :
man mi dal nama nélaw na niou yobou sa téléphone 😂
2026-09-26 17:54:39
14
NADO :
non pas 18mill de malayka, 1 seul moy récupérer am yi .le comment nak dou kou nek mokay ham......??
2026-09-26 19:08:56
12
Paly🇸🇳 :
yén comprendroulén concept débat bi, oustaz degradé dafay andi tout le temps contradiction pour que niou doug au fond du sujet
2026-09-26 21:12:10
7
Mapate sow Beta :
Merci oustaz salmane boroom kham kham bo mak
2026-09-26 18:41:05
47
farmSaboura :
Pape Sidy fall kagne ngay bayi invité ki ci say plateau, trop c'est trop soubhanallah
2026-09-26 18:06:58
21
Al Amine :
même boudé milliards malakal mawti mo amm tamitte en tout cas il ne rate jamais sa mission 🤣🤣
2026-09-26 21:28:40
0
khadim diagne :
béneu malakal mawti moo am épis population bi dou 18M rk
lolou appepres la rk.chaque jour amniou dioudou déllou amna gnouye dioudou té bokouniou si lim bi.malakal mawti béneu la té mooy kiy dieul route yép
2026-09-26 20:23:03
6
talibe mahmoud khalil al housa :
𝚘𝚞𝚣𝚝𝚊𝚣 𝚍𝚎𝚞𝚐𝚎𝚞𝚛𝚊𝚍è 𝚠𝚊𝚔𝚑𝚘𝚞𝚕 𝚍𝚎𝚞𝚐𝚞𝚎 𝚍𝚑
2026-09-26 18:10:41
6
Taïf Cosmetique :
L’an mooy Malaika ba paré sakh d’abord
2026-09-26 20:43:50
0
Lamine Muslim :
pourtant oustaz degraadé à raison ❤️🤣🤣
2026-09-26 21:49:26
0
Malick gning :
faire de la philosophie n' est pas mal en soit mais le sophisme en philosophie donne des tournis au traducteur du livre saint
2026-09-26 16:43:23
5
Babacar Tall :
ملك الموت هو أسرافيل
2026-09-26 22:08:11
1
Diouffy cire :
Ki hamoul limouy wakh
2026-09-26 19:12:52
3
Bay Djewrign Said Di :
oustaz dégradé a raison
2026-09-26 22:22:27
0
user1507154292378 :
limou firê nélaw mena nêk ndakh ãya bi
وهو الذي يتوفاكم بالليل.....
2026-09-26 22:31:07
3
SEYFOUL ISLAAM :
الحمدلله الذي أحيانابعدما(أماتنا) واليه النشور
2026-09-26 19:57:38
3
0umar🫀P.Muhammad 💚🌿💐(psl) :
Rér bahoul sabotage wéssouwouko🌿✍️
2026-09-26 22:56:21
0
To see more videos from user @.esprit92, please go to the Tikwm
homepage.