Mbectè mii yalla boumou gnu oump si barkei yonet bi (psl)
2026-09-27 19:35:57
571
Tutush Global Services :
Vous riez mais ce qu’elle dit c’est très important Amna hôpitaux you beuri daniouy diokhé dom diambour c’est important nga and ak nit kou exigeant koulay Kholal sa dom parce que c’est pas sur😏
2026-09-27 19:15:22
144
Codou😍 :
Aka sadik 😂
2026-09-27 18:54:22
311
ruqqayah_bint_Mouhamed🔗💍 :
Legui wolof IA bi guen dieul 😂
2026-09-27 20:41:58
5
Chacha Mrs Kontéye :
Ndeysane doom nékh yalla nagnou ko yalla maye gnoune yeup
2026-09-27 21:43:42
5
Fatima Mme Seydi ❤️💍 :
Bilae dom dafa nekh ❤️🥰
2026-09-27 18:58:11
223
Anta love♥️ :
Ki nekhna 😂😂😂😂😂
2026-09-27 20:22:49
18
Nass Bou Sonko ❤️ :
Bilay dom meunoul Faye yaye jour Bimay am dom da am ben mort ne boufa nekon jour bobou 17h 20h dama teude ben place ak Nima adie sama tank yi Ndakh bagn nio diawalè sama dom Ndakh Nioum niar nio dende🥹
2026-09-27 20:06:52
21
scorpion 🦂😻 :
ndaysane 🤣🤣🤣
2026-09-27 18:36:34
32
amy baye niass :
ndeysane machalla
2026-09-27 18:22:24
120
Feuz Niang 🇸🇳🇪🇸 :
Pourtant dafa rafete dé😂😂
2026-09-27 20:21:48
46
khadija chéri mouhamed diop :
toute mais félicitations
2026-09-27 19:28:21
23
dame thiam👩❤️💋👩💍💦 :
Kiii aka nékh 😂
2026-09-27 20:17:25
6
Ouma Badjie :
congratulations
2026-09-27 21:44:32
1
Layla Isla Ndiaye_🇺🇸🇸🇳 :
Hahahahaha
2026-09-27 17:41:28
59
Mi P@ss⭐️✝️⭐ :
la fin comme moi mes 3 jours de maternité je n'arrive pas à dormir surtout le premier jour tellement j'étais contente je regardais mon bébé sans arrêt.