@pink00221: Part 3 (fin) : C'est la fille de la victime saoudienne qui détient le dernier mot sur la vie de Mbayang Diop. Majeure en décembre, elle devra choisir entre le pardon ou l'exécution. Mame Matar Guèye appelle à la mobilisation diplomatique #MbayangDiop #Senegal #Justice #Jamra
Ayway borom xamxam naniou liguey Khalebi weubeuti khelam bamou ball mbayang ak pape Khalebi !!! 🥺
2026-09-27 22:09:17
146
Mdm diop :
Yalla bou toudéni dou dé rék dou dé yalla nako yalla takhawou
2026-09-27 23:36:42
61
user578673979390 :
xalé bi yalna yalla olbati xélam bamou balko thi barké saydina mouhaméd
2026-09-27 20:35:45
1205
Pape mamadou faye :
État sénégal dé moy lolou 🥺🥺
2026-09-27 21:46:06
84
seyni.ndiaye :
Ay yalla nako khale bi bal 😭😭😭😭
2026-09-27 20:19:02
589
sant Yalla :
Affair bi mom niane rek moy solution bi parsk damay ragal niou influence khalé bi teksi aussi yaye dafa fort enplus au moment des faits dafa eumbone😢c’est grave dou Cas bou ndaw 🥺Yalla rek mosi meun dara nako Sénégal yeup nianal sinon yakarouma khalé bi ball ko damasi tite trop . Yalla maguilay gu guiffal kholou khalé yi bagnou ball ko
2026-09-28 00:59:41
71
Milkzo :
Mame Mactar nit kou bakh la
2026-09-27 20:09:13
480
kalsoum dabakh Taha 😍 :
waw ligui kouy nieuw niou def si ay dok you doy War yalla may ko ndam ndakh dioulit niane rek la am svp 😭kii damako yeureum
2026-09-27 22:36:30
240
Tourondo badieunam 💗😍🎉 :
Naniou serignetou khalé bi yobou touram yi borom xam xam yi niou tourné bopou bi mou wax balna ko si khol bou sedd gouy🙏❤️na mbayang nieuw rk
2026-09-27 23:45:51
31
Astou Gawane 🟢⚪️ :
Mbiroum narr mom limasi degg dama doyy
2026-09-28 00:43:20
48
diya :
yal nako yalla teguil natou bi 🥺
2026-09-27 21:32:17
113
Mounas Saveur✪ :
Ay way na sénégalais yi diok borom kham kham yi nitou ALKHORHANE yi def lene ay dogg guir yalla mou moudier si diam ay yalla waloul Mbayang Diop guir yallah 😭😭😭
2026-09-28 13:40:18
3
Mareme Djibril tall :
Yalla na khalé balle Mbayang diop thie Barke Seydina Mouhamed psl yalla na yalla takhawou mbayang diop thie Barke Seydina Mouhamed psl
2026-09-28 21:05:56
1
Linguere beauty❤️ :
Ayway Yalla nala yalla takhawou mbayang Mane dé damakoy khalate rék Ndeysane 😭
2026-09-28 08:15:13
2
fatoush :
ay way yalnako khallé bi ball si barkep seydina Mohamed psl
2026-09-28 13:17:33
2
user6184091851084 :
et sadio mane
2026-09-27 20:10:05
10
Assy boutique 😍 :
Amine ya raby
2026-09-28 13:12:44
1
Adama Sarr :
Allahouma Amine
2026-09-28 10:10:53
8
La Noirde 💕🇸🇳 :
Au waay, que le Seigneur touche le cœur de cette fille 🙏
2026-09-27 21:57:37
65
peulh coumbis🩸🥛 :
fi dè mom yalla rekh mossi dessse yalla sunu borom niongui laye niane si barkè mouhamed nga wolbati khèlou khalè bi bamou ball mbayang ya allah
2026-09-28 13:24:35
10
M. beauty10 :
Mais naniou ko indi prison Senegal au moins
2026-09-28 01:35:14
12
adama :
aye waye ki di mbayang yalnako Yalla diapalé si barkeye Seydina Mouhamed salalahou Alayekhi wa salam bamou déloussi wate Sénégal si wétou ndiabotame amine ya rabi
2026-09-27 22:38:59
70
Princesse❤️Salihate💄 :
Yalnako yalla soutoural 🥰
2026-09-27 20:37:32
44
øg pickford junior :
ay WAH na adouna yeup andale gnanal femme bi guir yalla.dafa dani wone dolei reik yalla gneuw si kawam ak natou.yalna ko yalla soutoural bamou dounde.
2026-09-27 21:24:30
30
To see more videos from user @pink00221, please go to the Tikwm
homepage.