Dafa melni😊 sama mbecté aduna yi mbëguel🫶 bokku ci défé na nii nima méllone ci baax❤️❤️dotoumako🎄 meunati nakhté,nioune niarr👩❤️💋👨 dou narr mbëguel😍 da beuri dollé💪 sama xol 🫀 bi nga sax souniou jikko yi rekka wouté yene thiow 🤫 yu beuri yi xadioul ci bopp jiguéne💓💓 nieup aand mbabb leu nga titt ni daa nga ci guén weet 😭 na dioy😭 na lu yagg xeuy na biss adunyaa bolléwat niou😭😭😭