Salaam cheikh bi
mane dé ap talibé tidiane laa bou beugua dieul azkaarou tarbiya nguir doundou deug deug tassawouf. té sama khaatir si cheikh Ibrahim cissé lama yobou pour mou neek sama serigne.
beug naa nag kouma boolé ag moom inchallah
2026-09-29 10:43:04
3
Bitty Diop25 :
Ki dama nkh rk machalah yalla nga goud fane ❤️❤️❤️❤️❤️