@maxart230: Tino prêt pour le grand spectacle 🤍💚

max'art design🖌️
max'art design🖌️
Open In TikTok:
Region: SN
Monday 28 September 2026 19:23:54 GMT
8632
2182
58
7

Music

Download

Comments

maxart230
max'art design🖌️ :
Wa yaakar mane ngen di seuleum souuf🤍💚🧎🏽🧎🏽💔😂😂😂
2026-09-28 19:41:22
28
alou___100
Alou_Deug✊🏿 :
Apo len wax bi rk😂
2026-09-28 19:37:58
7
user6744555050043
user6744555050043 :
jamono Moy finalou inchallah dafa nekk si yonam kèn doukoko yakhal
2026-09-28 19:30:59
23
konte926
konte :
Wakh rek nga meune tino gaby mola meune fouf si kaw si souf nak douniou sene morom si dara tegal lafi equipe b remonte la ngay dioy si stade bi [Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie]
2026-09-28 20:28:50
4
ibrahimakebe170
ibrahimakebe17 :
Match bi kanie la
2026-09-28 19:52:44
2
loufagoatef
Original boy jamono2 💙🤍 :
Kham guen biiiii
2026-09-28 22:31:53
8
lahat447
user5597130712835 :
Ma lén meune fouf aye nakh guéne jamono 2 seul 💙💙💙
2026-09-28 19:39:12
8
.babs533elcapo0
Bab’s 🫠🙂‍↔️ :
Iow khamo football ⚽️
2026-09-28 19:47:16
0
ababacarrr_df06
Babs_D💯🤴 :
Max mercredi nguen guiss lou yemei inchallah💚🤍⚔️😂
2026-09-28 20:58:11
2
elhadjigorafayebamba2
Begu Bamba :
Yalla Rk mo meun yalla may niou ndaam inchalah
2026-09-28 21:26:17
1
laminefall055
. :
Baaa bissba inchalla 😂🤍💙💯
2026-09-28 19:40:17
4
tallavalverde8
Talzo :
Mèlni kouye jouè finale 😂😂
2026-09-28 19:36:57
2
papesamba198
PAPE SAMBA 🙏🏿🍫 ❤️🦍☝🏿 :
max gaw nga dh 🤭🤭
2026-09-28 19:47:46
2
papekala1
KL92🇸🇳🥇 :
2026-09-28 19:36:39
3
omarsane277
JEUNE🐣ÉLEVEUR🐔🐓🐏 :
Match bi kanie la
2026-09-28 20:19:39
0
falloubouarsenal1
Fallou Gunners ⚪️🔴 🦍 :
Tino yangui wakh rk 😂😂
2026-09-28 19:53:44
4
codediop51
Arona :
wouy
2026-09-28 19:30:20
2
elhadjigorafayebamba2
Begu Bamba :
Tino dioumo dh si 90mn yi la lay doorê ya meun may gagner inchahala 🙏💙🤍
2026-09-28 21:27:39
1
mame30647
Mame :
Jamono 2seul
2026-09-28 20:14:57
1
pa_assane_senegal41
Jean Mendy :
2026-09-28 19:29:49
1
cheikhmbaye227
kheuss bu boy seck🥰 :
aythia sama deukeundo yi 😂dathio geum sén bopou nak😂😂 tino damala beug koi nél 1 1-0 lalay door après niou andat gnibisi diap lénsi nak naniou fair-play nioy and si lépeu you noow❤️
2026-09-28 20:35:21
1
mor.led.njaay
Mor Led Njaay :
2026-09-28 21:01:59
0
pape.mbaye.mbodj
Pape mbaye Mbodj ✪ :
Bly
2026-09-29 00:10:06
0
omzobouj2
Omzo bou j2 :
2026-09-28 23:28:25
0
falloufall3388
fallou Gallas kharitou yayam :
2026-09-28 20:02:33
0
To see more videos from user @maxart230, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About