@nugum_nugum: Partage lénko guir yalla li Dawna yaram trp sama khol toyna nathi niepp diapp numéro 71:071:48:48 tour bi mame awa ndiaye wala 78:539:48:48 tourbi bada ka 🙏
Yallah nako yallah soutourale defaleko diame si barkep seydina mouhamed
2026-09-29 12:53:23
588
•BAABAKAR MU SËRIÑ MUNTAXAA• :
Yal na la sunu Boroom taxawu kom ni ngay taxawoo nit yi🙏🏾❤️
2026-09-29 13:17:05
202
𝒎𝒐𝒓 𝒃𝒐𝒖 𝐍𝐨𝐫𝐞𝐲𝐧𝐢 ✪ :
Ohhh😭yalla nako yalla takhawo🙏🏿
2026-09-29 12:37:30
114
Cheikh Café :
ltx amouma xaliss 😭😭😭
2026-09-29 12:46:14
36
ℱ𝒶𝓁𝓁ℴ𝓊 𝓂ℴ𝓃 𝓈 𝒻𝒶𝓁ℴ𝓊 :
Machalla Seri Ndaye Awa
2026-09-29 13:45:42
47
Fans °lamine^¥amal~🇸🇳🇪🇸< :
yalla nako yalla safaral😭😭
2026-09-29 12:27:35
88
COACH PAPIS :
500 million ci jeux olympiques vraiment Sénégal va mal
2026-09-29 14:37:35
17
sokhna asta walo :
Yalla nako yalla takhawou 🤲
2026-09-29 13:02:51
50
ALIOU DIOUF TALIBE BAMBA 💚💕❤ :
yall Na yallahh Goudal Fan Wii ch Abdou
2026-09-29 15:49:33
1
@*_modou seck_*@ :
oh yallah dako yalla takhawou
2026-09-29 14:06:27
3
Anita🌹🍫💍 :
Yalla nako yalla takhawou si barke Seydina Mouhamed 🤲🙏
2026-09-29 14:11:12
8
fatou bisness 63 🛍️ :
yalnako yalla may weur
2026-09-29 15:44:51
0
babacar faye les catalan🔵🔴 :
Cheikh abdou ngire yalla dimbali niou gnay dague yene parti yi si video yi danio dioy ba sonou😭😭😭
2026-09-29 12:55:48
14
sokhna.awa.samb2 :
Ndeysane yallah nako yallah soutoural si barke Serigne fallou
2026-09-29 12:59:58
1
Aidara Niass10 :
Oh nayesane 💔💔
2026-09-29 15:00:42
1
bb kiné :
Yallna ko yalla safara si diamou 🤲🥺😭
2026-09-29 13:37:45
12
Ndiaga euro sarbét :
yallnako yalla maye wérr inchalah
2026-09-29 13:53:26
1
FANS IB NDIAYE1️⃣1️⃣ 🤍♥️ :
cheikh abdou ioe yalla rk mo am sa fay 🙏😭
2026-09-29 14:02:06
6
sopey Nabi 🥰🥰423❤️💍💎👸 :
salalahou Allah mouhameddine 🤲🤲🤲
2026-09-29 13:35:42
8
Talla Sene :
Yalla bakhna
2026-09-29 12:26:57
23
RAHIM L'infographie :
un grand révérence Cheikh Abdou yalla na yalla défal laa téranguay adouna ak alakhira défal ko bépou nitt bousi dougueul saaw niakke
yalla na yalla téguil natou bi si barkép Mohamed 🙏🏿
2026-09-29 12:31:07
17
Talibe ❤️maodou a vie ❤️ :
😭😭😭😭😭meti na yala na yala May ko wer
2026-09-29 12:28:57
14
modoundiaya0 :
Yalla nako yallah takhawou
2026-09-29 12:37:31
14
LC Agro Consulting :
Oh! Massa way🙏🏾
2026-09-29 12:28:45
11
To see more videos from user @nugum_nugum, please go to the Tikwm
homepage.