ndaysane lolou serigne fallou def si taw cheikh sbdou karim mbacké gnou yoboufa ziar sa mame yobanté gnou si serigne bi bali yag mouné damay dem wakhal ko sama bop gnou dem ziar bay serigne bi gnane sama mame né serigne bi sa baye serigne fallou mo dane na taw bou taw ta yafiy serigne fallou ta lou beuga mat wer tawoul gadiakh gagui dé dokh lagnou beug serigne abdou karim gnane jour bobou taw bi mognou dakh touba ba khombole dafay taw bilahi