@fabyna105:

Faby bou cheikh ibra⚡
Faby bou cheikh ibra⚡
Open In TikTok:
Region: SN
Thursday 01 October 2026 20:26:27 GMT
9642
933
8
20

Music

Download

Comments

princesse.bou.kay
princesse bou kayar :
2026-10-02 17:17:07
0
diaker.diallo
Diaker Diallo :
🥰🥰🥰
2026-10-02 14:58:43
1
khady.ja2
Khady Diop :
🥰🥰🥰
2026-10-02 13:11:41
1
awa.seye184
Awa Seye :
[Cœur rouge][Cœur rouge][Cœur rouge]
2026-10-02 08:41:09
0
gory.ndiaye0
Gory Ndiaye :
🥰🥰🥰
2026-10-01 21:16:28
1
ssmseul
S 🥹🫀❤️ :
Guddi bii, sama xol dafa metti torop… torop… torop. Am na lu ma yëg ci sama biir, lu ma mënu wax kenn. Dama bëgg wax, dama bëgg nekk ak nit di wax li ma yëg, waaye su ma waxee, dañu ma déglu rekk… duñu xam li sama xol di wax. Ñu dégg sama baat, waaye duñu dégg sama xol. Ñu gis sama kanam, waaye duñu gis li ma di dund ci sama biir. Man, damay dégg ñépp. Damay comprendre ñépp. Damay xam seen metti, seen silence, seen bés bu neex ak bés bu metti. Waaye bu man la ñëwee, kenn mënuma comprendre man. Kenn mënuma xam li ma di yëg. Kenn mënuma dégg li ma dul wax. Am na ay guddi yu ma nekk rekk ak sama xol, di laaj sama bopp ndax dina am bés bu nit dina ma comprendre, bés bu ma mëna wax lépp te kenn du ma wax ne “danga doy waar”. Ndax parfois, nit du bëgg wax lu bare… mu bëgg rekk kenn dégg ko ba dëgg, kenn comprendre ko ba dëgg, kenn ne ko: “Dégg naa la. Xam naa li nga di yëg.” Waaye léegi… dama noppi. Ndax sama xol dafa sonn. Dafa metti torop. Te li gëna metti mooy: man damay comprendre ñépp, waaye kenn du ma comprendre.
2026-10-02 00:22:38
1
To see more videos from user @fabyna105, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About