Sama xol 😭😭😭😭beugeutouma guiss vidéos wallahi 😭Yalnala yalla waleu si papa
2026-10-02 14:51:27
431
Ndakista babacar🥰📿💚 :
Beugoumako sakh guis wallahi 😭😭
2026-10-02 15:11:22
106
𝒟𝒶𝒷𝒶💋 :
Yalla nala yalla taxawou si barkep s fallou 😭🙏🏾
2026-10-02 15:25:03
75
Lachicorienne01 :
Yalla mi meune lepp yalnako takhawou 🙏
2026-10-02 15:18:46
39
Princesse des patriotes💪😘 :
Ay way nanou wathié lou kamil niane niou balko svp
2026-10-02 15:51:11
15
Bb ~Fah :
ki boko kholé rék khamni kou geum yallah la barki Serigne Babacar sy 😭yallah na yallah tégui natou biii 💔😭🙏
2026-10-02 20:15:50
10
only one😋 :
khamna kou gueume yalla la seuteuteeee li moye natou deug nak😭
2026-10-02 15:20:18
70
La reine ❤️ :
Thiey adouna ayy yalla boulko setan yalla yaw rek ya meun ya mag ya bind assama bind souff bind aldiana bind safara yaw yay raby samawaty ayy yalla yaw mi bind lep yilif lepp te ken yilifoula dimbalell sa diamm bi ngir barké alkhouran ngir dieum ndiol makaa ayy yalla boul setan souniou baye dji 😭😭😭😭😭😭😭😭😭
2026-10-02 16:40:15
24
Bou laye 100%100maman vulgaire :
Yalla meun gua lep 🥰
2026-10-02 14:42:19
20
mamyyayourasoulbeauty :
Ayyyyywayyyyyyyyyyyyyyy🤦🏼♀️yaaaa raby yaa Rahman ayyy yalla waloul saaa diambiii🙏🏽😭
2026-10-02 16:59:29
0
ZOO ELMoNO🫡🕊️ :
Yalnako yalla takhawou inchalla 🙏
2026-10-02 19:01:09
0
begue seringe saliou mbacke :
Loumo def
2026-10-02 19:40:52
0
maguista🥰 lô💕 :
yalla nala yalla takhawou thi barkép Serigne fallou amine