Konn li mo andi thiowli? Kine nak arrete wakh Lou bakh sa nit ayoul au contraire dagua ci wara contane parce que kou wakh Lou bakh sa kharit beégu si rk gua wara def. Sen diguantei bou len ci andi ay concurrence ak jalousie
2026-10-03 17:31:13
1917
Miss-Sourire🥺♥️ :
Koula khol kham ni liguay wakh natureloul
2026-10-03 19:24:56
364
❤️TYMS❤️ :
Ah mère lii raxoul?
2026-10-03 18:04:42
851
Cardibi🥰 :
Bou gnep melone ni mane kene dou sone mane kou wakhal sama nawlé lou bakh doumasi am béne problème tè li dara nekousi sakh
2026-10-03 16:29:54
455
🌚🌝 :
Messouma beugué influenceur nima beugué Bb Binta Bilahi❤️😭
2026-10-03 11:57:18
920
Adjia Daba Diouf sope Rassoul :
Machala Kiné Ndiaye tamite def na
2026-10-03 17:21:40
1057
Miss Pene🎀💗 :
Kiné dh mo yé message la
2026-10-03 18:27:44
350
Mme koïta :
Elle est simple siviliser elle n’es pas méchante vraiment en vert ses amis je t’aime vraiment
2026-10-02 22:09:29
875
Awa Sow :
Gnep ko beugue
2026-10-02 21:55:46
1627
user2862940799726 :
je ne supporte pas les maman qui divise les gens 😂😂😂😂😂bilahi
2026-10-03 17:38:48
1203
𝐵𝑖𝑛𝑡𝑜𝑢 Events🎀 :
Kone li mo waral thiow li😂. Mais deug rek nga wax binta dafa adorable
2026-10-03 16:26:39
617
Kineuh❤️ :
Rakhnaaaaa dara 😂😂😂😂😂😂
2026-10-03 00:43:29
879
Lala❤️extension thies :
Ya tayy gueureum koula nekh fi kou nekeu Amna droit gueureum kouko nekhh
2026-10-03 21:54:17
8
J’AIME BB BINETA(TBB) :
Mashallah elle as de l’AURA sama wadji diam ak salam rek Guay am
2026-10-02 21:58:28
296
Ndeye penda ❤️ :
Kou def lou bakh degg lou bakh louy lolou yaw🥳🥳
2026-10-03 21:09:28
0
♥️14octobre 🎊👑🎂 :
wah legui diekhoul
2026-10-03 20:19:51
1
Aïda diouck17 :
Y’a bakh 🥳🥳🥳🥳
2026-10-03 21:48:34
0
Astel seck😘 :
Deugu rek guafi wax dh🥳🥳🥳
2026-10-02 22:37:25
477
M-Diarra-G :
bayilen xalé yi gnou ande ci diam
2026-10-03 18:10:08
193
Queen Sambou :
Pourtant limou wakh dara nékousi pour man
2026-10-03 17:56:16
255
Babybrown_🥰 :
Wah dji eumbeu n’a dara d hmmm
2026-10-03 18:17:48
178
MissN🌹 :
Mère nak li rakhna dh 😭😭
2026-10-03 20:12:13
50
𝒜~🇸🇳 :
Tiktok vous a rendu negatifs ba leguii kenn meuneutoul wakhal ken bakhamm prck daguenn di diap ni day garal kenen tei lolou yenn gnisi commeentaire yena kay indi daguen negatifs trop
2026-10-03 19:21:42
64
une noiricaine :
Binta nieupeu ko beug Mashalah ❤️🫶🏼
2026-10-03 01:59:40
313
To see more videos from user @nellykelly273, please go to the Tikwm
homepage.